Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.
tu diras donc: les branches ont été retranchées, afin que moi je fusse enté.
xanaa dinga wax ne: «car yooyu dañu leen a fàq, ngir jabtal ma fa ñu nekkoon.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
car si dieu n`a pas épargné les branches naturelles, il ne t`épargnera pas non plus.
gannaaw yàlla baalul car ya cosaanoo ca garab ga, kon boog yéen itam man na leen a fàq.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
beaucoup de gens étendirent leurs vêtements sur le chemin, et d`autres des branches qu`ils coupèrent dans les champs.
Ñu bare lal seeni yére ci yoon wi, ñenn ñi dagg ay cari garab ci tool yi, lal leen it ci yoon wi.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
or, si les prémices sont saintes, la masse l`est aussi; et si la racine est sainte, les branches le sont aussi.
damay wax ne, mburu mépp sell na, bu ci yàlla amee wàll. naka noonu garab gi yàlla séddoo reen bi, garab gépp sell na.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
il est semblable à un grain de sénevé qu`un homme a pris et jeté dans son jardin; il pousse, devient un arbre, et les oiseaux du ciel habitent dans ses branches.
mi ngi mel ni doomu fuddën gu nit jël, ji ko ci toolam. mu sax, nekk garab, ba picci asamaan ñëw, tàgg ciy caram.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
mais, lorsqu`il a été semé, il monte, devient plus grand que tous les légumes, et pousse de grandes branches, en sorte que les oiseaux du ciel peuvent habiter sous son ombre.
waaye boo ko jiwee, day jóg, màgg, ba sut gàncaxi tóokër yépp; mu sax ay bànqaas yu réy, ba picci asamaan tàgg ci keram.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
c`est la plus petite de toutes les semences; mais, quand il a poussé, il est plus grand que les légumes et devient un arbre, de sorte que les oiseaux du ciel viennent habiter dans ses branches.
doomu fuddën moo gën a tuuti ci jiwu yépp, waaye bu saxee, mooy sut ci gàncaxi tóokër yi, di nekk garab, ba picci asamaan ñëw, tàgg ciy caram.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit: