Je was op zoek naar: haifai (Swahili - Wolof)

Menselijke bijdragen

Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.

Voeg een vertaling toe

Swahili

Wolof

Info

Swahili

nitajivuna basi, ingawa haifai! lakini sasa nitasema juu ya maono na ufunuo alivyonijalia bwana.

Wolof

damu amul jariñ, ba tey war na ma. kon ma jàll ci nettali gis-gisi boroom bi ak i peeñu.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

haifai kitu wala kwa udongo wala kwa mbolea. watu huitupilia mbali. sikieni basi, kama mna masikio!"

Wolof

du jariñ suuf, te du nekk tos. dañu koy sànni ca biti. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak

Swahili

kama mtu akijiona kuwa ni mtu mwenye dini, lakini hawezi kuutawala ulimi wake, dini yake haifai kitu, na anajidanganya mwenyewe.

Wolof

ku yaakaar ne am na diine, waaye moomul làmmiñam, xanaa di nax boppam rekk, diineem jooju du diiney dara.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

ikiwa basi, sisi ni watoto wa mungu, haifai kumfikiria mungu kuwa kama dhahabu, fedha au hata jiwe lililochongwa na kutiwa nakshi na binadamu.

Wolof

kon nag, bu nu nekkee xeetu yàlla, warunoo gëm ne, yàlla mel na ni nataali wurus, xaalis mbaa doj yu nit defar ci xareñ mbaa xel.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

haifai mwanamume kufunika kichwa chake, kwa kuwa yeye ni mfano wa mungu na kioo cha utukufu wake mungu; lakini mwanamke ni kioo cha utukufu wa mwanamume.

Wolof

góor nag moom warul a teg dara ci boppam, ndaxte mooy melokaanu yàlla te dafay wone ndamu yàlla. jigéen moom dafay wone ndamu góor.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

basi, usiiharibu kazi ya mungu kwa sababu ya ubishi juu ya chakula. vyakula vyote ni halali, lakini haifai kula chakula ambacho kitamfanya mtu aanguke katika dhambi.

Wolof

bu sa ñam yàq jëfu yàlla. bépp ñam sell na ci kanam yàlla. ci lu wér! waaye képp ku lekk luy yàq sa ngëmu moroom, def nga lu bon.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

"ninyi ni chumvi ya dunia! lakini chumvi ikipoteza ladha yake itakolezwa na nini? haifai kitu tena, ila hutupwa nje na kukanyagwa na watu.

Wolof

«yéena di xoromus àddina. bu xorom si sàppee, nan lañu koy delloo cafkaam? du jariñati dara, lu dul ñu sànni ko ci biti, nit ñi dox ci kawam.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak

Swahili

kweli, masharti hayo yaonekana kuwa ya hekima katika namna ya ibada ya kujitakia wenyewe, unyenyekevu wa uongo na kuutendea mwili kwa ukali; lakini kwa kweli, haifai chochote kuzuia tamaa za mwili.

Wolof

dëgg la, seeni sàrt dañuy dénkaane pasteef ci jaamu yàlla, di toroxlu ak di fitnaal seen yaram. waaye sàrt yooyu nag amuñu benn njariñ, ngir nit ñi noot seen nafsu.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Krijg een betere vertaling met
7,761,828,956 menselijke bijdragen

Gebruikers vragen nu voor assistentie



Wij gebruiken cookies om u de best mogelijke ervaring op onze website te bieden. Door de website verder te gebruiken, geeft u toestemming voor het gebruik van cookies. Klik hier voor meer informatie. OK