Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.
tena mwasema ati mtu akiapa kwa madhabahu si kitu; lakini akiapa kwa zawadi iliyowekwa juu ya madhabahu, kiapo hicho humshika.
dangeen ne it: “ku giñe saraxalukaay bi ci kër yàlla gi, ngiñ li duggul, waaye ku giñ ci sarax si ci kawam, dugg na.”
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
yeye aliingia katika nyumba ya mungu pamoja na wenzake, wakala ile mikate iliyowekwa mbele ya mungu. yeye wala hao wenzake hawakuruhusiwa kula mikate hiyo isipokuwa tu makuhani peke yao.
xanaa yéguleen, ni mu dugge woon ca kër yàlla ga, gis fa mburu, ya ñu jébbal yàlla, mu daldi ko lekk. fekk jaaduwul mu lekk ca, moom walla ña mu àndaloon; saraxalekat rekk a ko sañoon a lekk.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
yeye aliingia ndani ya nyumba ya mungu, akachukua ile mikate iliyowekwa mbele ya mungu, akala na kuwapa wenzake. kisheria, ni makuhani tu peke yao ndio walioruhusiwa kula mikate hiyo."
xanaa yéguleen, ni mu dugge woon ca kër yàlla ga, jël mburu, ya ñu jébbal yàlla, lekk ca, jox ca ña mu àndaloon? fekk jaaduwul kenn lekk ko, ku dul saraxalekat.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak
naye akaingia ndani ya nyumba ya mungu, akala ile mikate iliyowekwa mbele ya mungu. jambo hili lilifanyika wakati abiathari alikuwa kuhani mkuu. na ni makuhani tu peke yao waliokuwa wameruhusiwa kula mikate hiyo. lakini daudi aliila, tena akawapa na wenzake."
xanaa yéguleen li amoon ci bési abiyatar saraxalekat bu mag bi, ni daawuda dugge woon ca kër yàlla ga, lekk mburu ya ñu jébbal yàlla, jox ci it ña mu àndaloon; fekk jaaduwul kenn lekk ko, ku dul saraxalekat?»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak