Je was op zoek naar: jitahidi (Swahili - Wolof)

Menselijke bijdragen

Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.

Voeg een vertaling toe

Swahili

Wolof

Info

Swahili

jitahidi kumsaidia mwana sheria zena na apolo ili waweze kuanza ziara zao na uhakikishe kwamba wana kila kitu wanachohitaji.

Wolof

naka senas àttekat bi nag ak apolos, waajal leen bu jekk ci seen tukki, ba seen aajo yépp faju.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

jitahidi kupata kibali kamili mbele ya mungu kama mfanyakazi ambaye haoni haya juu ya kazi yake, na ambaye hufundisha sawa ule ujumbe wa kweli.

Wolof

góor-góorlul ba teew fa kanam yàlla, nekk liggéeykat bu mu nangul te rusoo ci dara, di faramfàcce bu jub kàddug dëgg gi.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

usikubali mtu yeyote akudharau kwa sababu wewe ni kijana, lakini jitahidi uwe mfano kwa wanaoamini: katika usemi wako, mwenendo wako, upendo, imani na maisha safi.

Wolof

bu la kenn xeeb ndax say at, waaye defal sa bopp royukaayu ñi gëm ci say wax ak say jëf, ci sa mbëggeel, sa ngëm ak sa cell.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Krijg een betere vertaling met
7,736,337,809 menselijke bijdragen

Gebruikers vragen nu voor assistentie



Wij gebruiken cookies om u de best mogelijke ervaring op onze website te bieden. Door de website verder te gebruiken, geeft u toestemming voor het gebruik van cookies. Klik hier voor meer informatie. OK