Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.
lakini kabla ya hayo, itambidi ateseke sana na kukataliwa na kizazi hiki.
waaye balaa booba fàww mu sonn lool te niti jamono jii dëddu ko.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
kila kitu alichoumba mungu ni chema, wala hakuna kinachohitaji kukataliwa, bali vyote vipokelewe kwa sala ya shukrani,
ndaxte li yàlla sàkk lépp baax na, kon wenn ñam araamul ci ku koy jëfandikoo ak cant.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
maana ikiwa kukataliwa kwao kulisababisha ulimwengu upatanishwe na mungu, itakuwaje wakati watakapokubaliwa na mungu? wafu watafufuka!
ndaxte bi yàlla génnee israyil, ubbee na noonu bunt, ngir xeeti àddina juboo ak moom; kon su yàlla dugalaatee israyil, ndax du mel ni ndekkitel néew ya?
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
akaendelea kusema: "ni lazima mwana wa mtu apate mateso mengi na kukataliwa na wazee na makuhani wakuu na walimu wa sheria; atauawa, lakini siku ya tatu atafufuliwa."
teg ca ne: «doomu nit ki war na sonn lu bare; saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya dëddu ko, ñu rey ko, mu dekki ca ñetteelu fan ba.»
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak