Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.
mtu huyo alikuwa akiishi makaburini wala hakuna mtu aliyeweza tena kumfunga kwa minyororo.
kooku nag ca sëg ya la dëkk, te kenn mënu koo yeew, du ak càllala sax.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
mchana na usiku alikaa makaburini na milimani akipaaza sauti na kujikatakata kwa mawe.
guddi ak bëccëg mu nga woon ca sëg ya ak ca tund ya, di yuuxu te jam yaramam ak ay xeer.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
mara tu yesu aliposhuka mashuani, mtu mmoja aliyepagawa na pepo mchafu alitoka makaburini, akakutana naye.
bi yeesu génnee gaal gi, nit ku rab jàpp jóge ca sëg ya, daldi ñëw kar ko.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
nao, baada ya kufufuka kwake, wakatoka makaburini, wakaingia katika mji mtakatifu, wakaonekana na watu wengi.
te gannaaw ndekkitel yeesu ñu génn ca bàmmeel ya, dugg ca dëkk bu sell ba, te feeñu ñu bare.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
alipokuwa anashuka pwani, mtu mmoja aliyekuwa amepagawa na pepo alimjia kutoka mjini. kwa muda mrefu mtu huyo, hakuwa anavaa nguo, wala hakuwa anaishi nyumbani bali makaburini.
bi yeesu di wàcc ca gaal ga, ku rab jàpp ca waa dëkk ba ñëw, kar ko. yàgg na def yaramu neen te dëkkul ca kër, waaye ca sëg ya lay nekk.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
yesu alifika katika nchi ya wagerasi, ng'ambo ya ziwa, na huko watu wawili waliopagawa na pepo wakakutana naye wakitokea makaburini. watu hawa walikuwa wenye kutisha mno, hata hakuna mtu aliyethubutu kupita katika njia hiyo.
bi yeesu jàllee nag, ba teer ca diiwaanu waa gadara, ñaar ñu rab jàpp daldi génn ca sëg ya, ñëw kar ko. Ñaar ñooñu nag, ñu soxor lañu woon, ba kenn ñemewul woon a jaar foofa.
Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit: