Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.
naka noonu, na jigéen ñi am faayda, bañ a jëw mbaa xér ci dara, waaye nañu takku ci lépp.
even so must their wives be grave, not slanderers, sober, faithful in all things.
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
te yaw, ci lépp lu mu man a doon, nekkal ab royukaay ci jëf yu baax. na sa njàngale wér te am faayda,
in all things shewing thyself a pattern of good works: in doctrine shewing uncorruptness, gravity, sincerity,
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
maanaa, na góor ñu mag ñi foog, am faayda te maandu, di ñu wér ci seen ngëm, seen mbëggeel ak seen muñ.
that the aged men be sober, grave, temperate, sound in faith, in charity, in patience.
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
jigéen ñu mag ñi itam, na seen doxalin ànd ak faayda; buñuy jëw mbaa xér ci sangara. waaye nañuy jàngale lu baax,
the aged women likewise, that they be in behaviour as becometh holiness, not false accusers, not given to much wine, teachers of good things;
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
Ñaanal-leen buur yi ak kilifa yépp, ngir nu man a am dund gu dal te jàmmu, ànd ak ragal yàlla ak faayda yu mat.
for kings, and for all that are in authority; that we may lead a quiet and peaceable life in all godliness and honesty.
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
«bu fekkee ne agsi ngeen ci dëkk bu mag mbaa bu ndaw, nangeen fa seet ku fa am faayda, dal ca moom ba kera ngeen jóge dëkk ba.
and into whatsoever city or town ye shall enter, inquire who in it is worthy; and there abide till ye go thence.
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
sàmm bi nag, nii la war a mel: war na ñàkk ŋàññ, yem ci benn soxna, moom boppam te maandu; war na am faayda, man gan te am mayu jàngale;
a bishop then must be blameless, the husband of one wife, vigilant, sober, of good behaviour, given to hospitality, apt to teach;
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:
ndaxte kirist yebalu ma ngir may sóobe ci ndox, waaye da maa yebal, ngir may yégle xebaar bu baax bi, te ma bañ koo def ak waxi xam-xamu nit, ngir bañ a ñàkkal faayda deewu kirist ca bant ba.
for christ sent me not to baptize, but to preach the gospel: not with wisdom of words, lest the cross of christ should be made of none effect.
Laatste Update: 2012-05-04
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit: