Você procurou por: kuteseka (Suaíli - Wolof)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Suaíli

Wolof

Informações

Suaíli

aliona ni afadhali kuteseka pamoja na watu wa mungu kuliko kufurahia raha ya dhambi kwa kitambo kidogo.

Wolof

bokk coono ak gaayi yàlla yi moo ko gënaloon muy bànneexu ab diir ci bàkkaar.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

asiwepo mtu yeyote miongoni mwenu ambaye anapaswa kuteseka kwa sababu ni muuaji, mwizi, mhalifu au mwovu.

Wolof

buñu sonal kenn ci yéen ci li mu rey nit walla mu sàcc, mbaa def lu bon, walla dugg ci lu yoonam nekkul.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

alitambua kwamba kuteseka kwa ajili ya masiha kuna faida kubwa zaidi kuliko utajiri wote wa nchi ya misri, maana alikuwa anatazamia tuzo la baadaye.

Wolof

Ñu toroxal ko ngir almasi bi mi ngi mel ci moom ni alal ju ëpp alali misra yépp, ndaxte yool bi la doon séentu.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

lakini, hata kama itawapasa kuteseka kwa sababu ya kutenda mema, basi, mna heri. msimwogope mtu yeyote, wala msikubali kutiwa katika wasiwasi.

Wolof

doonte ñu di leen fitnaal sax ci def lu jub, ñu barkeel ngeen. buleen tiit nag ndax seeni xëbal, mbaa ngeen di ci am njàqare.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

na sasa nafurahi kuteseka kwa ajili yenu, maana kwa mateso yangu hapa duniani, nasaidia kukamilisha kile kilichopungua bado katika mateso ya kristo kwa ajili ya mwili wake, yaani kanisa.

Wolof

léegi nag maa ngi am bànneex ci coono, yi may daj ngir seen njariñ; te li des sax ci fitnay kirist, noonu laa koy àggalee ngir njariñu mbooloom ñi gëm, di jëmmam.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

usiogope hata kidogo yale ambayo itakulazimu kuteseka. sikiliza! ibilisi anataka kuwajaribu kwa kuwatia baadhi yenu gerezani; nanyi mtapata dhiki kwa muda wa siku kumi. muwe waaminifu hata mpaka kufa, nami nitawapeni taji ya uzima.

Wolof

bul ragal li nga nar a daj. seytaane dina dugal kaso ñenn ci yéen, ngir wut leen a fiir. diirub fukki fan dingeen am coono. nanga takku ba àttan cee dee, ma jox la kaalag dund gi. i

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Consiga uma tradução melhor através
8,028,939,501 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK