Você procurou por: saraxalekat (Wolof - Amárico)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Wolof

Amárico

Informações

Wolof

te saraxalekat yu mag yi di ko jiiñ lu bare.

Amárico

የካህናት አለቆችም ብዙ ያሳጡት ነበር፤ እርሱ ግን ምንም አልመለሰም።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

faf ab saraxalekat jaar ca yoon wa, séen nit ka, teggi.

Amárico

ድንገትም አንድ ካህን በዚያ መንገድ ወረደ አይቶትም ገለል ብሎ አለፈ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

saraxalekat yu mag ya dogu ci ne, dañuy reyaale lasaar,

Amárico

የካህናት አለቆችም አልዓዛርን ደግሞ ሊገድሉት ተማከሩ፥

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

te gannaaw am nanu saraxalekat bu mag, biy yilif waa kër yàlla,

Amárico

በእግዚአብሔርም ቤት ላይ የሆነ ታላቅ ካህን ስላለን፥

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»

Amárico

ሊቀ ካህናቱም። ይህ ነገር እንዲህ ነውን? አለው፤

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat yaa nga fa woon, di ko jiiñ bu metti.

Amárico

የካህናት አለቆችና ጻፎችም አጽንተው ሲከሱት ቆመው ነበር።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya it di ko ñaawal naan:

Amárico

እንዲሁም ደግሞ የካህናት አለቆች ከጻፎችና ከሽማግሎች ጋር እየዘበቱበት እንዲህ አሉ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

saraxalekat bu mag ba daldi laaj yeesu ci lu jëm ci taalibeem yi ak ci njàngaleem mi.

Amárico

ሊቀ ካህናቱም ኢየሱስን ስለ ደቀ መዛሙርቱና ስለ ትምህርቱ ጠየቀው።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

li waral mbir mi gën a leer moo di ne, beneen saraxalekat bu mel ni melkisedeg dafa ñëw.

Amárico

በማያልፍም ሕይወት ኃይል እንጂ በሥጋ ትእዛዝ ሕግ ሳይሆን ሌላ ካህን በመልከ ጼዴቅ ምሳሌ ቢነሳ፥ ይህ እጅግ አብልጦ የሚገለጥ ነው።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

ba ñuy dem, ñenn ca wottukat ya ñëw ca dëkk ba, xamal saraxalekat yu mag ya lépp lu xew.

Amárico

ሲሄዱም ሳሉ እነሆ፥ ከጠባቆቹ አንዳንድ ወደ ከተማ መጥተው የሆነውን ሁሉ ለካህናት አለቆች አወሩ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

waaye saraxalekat yu mag ya ak njiit ya xiir mbooloo ma, ñu laaj barabas te reylu yeesu.

Amárico

የካህናት አለቆችና ሽማግሎች ግን በርባንን እንዲለምኑ ኢየሱስን ግን እንዲያጠፉ ሕዝቡን አባበሉ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

Ña jàppoon yeesu yóbbu ko kër kayif, saraxalekat bu mag ba, fa xutbakat ya ak njiit ya daje.

Amárico

ኢየሱስን የያዙትም ጻፎችና ሽማግሎች ወደ ተከማቹበት ወደ ሊቀ ካህናቱ ወደ ቀያፋ ወሰዱት።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

booba nag saraxalekat yu mag ya ak njiiti xeet wa dajaloo ca kër gu réy gu saraxalekat bu mag ba, tudd kayif.

Amárico

በዚያን ጊዜ የካህናት አለቆች የሕዝብም ሽማግሎች ቀያፋ በሚባለው በሊቀ ካህናቱ ግቢ ተሰበሰቡ፥

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

ci kaw loolu saraxalekat bu mag ba, di ku ñuy wax anañas, sant ña taxaw ca wetam, ñu fél gémmiñam.

Amárico

ሊቀ ካህናቱም ሐናንያ አፉን ይመቱት ዘንድ በአጠገቡ ቆመው የነበሩትን አዘዘ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

te it ndax jànguleen ci yoonu musaa, ne saraxalekat ya ca kër yàlla ga teraluñu bésu noflaay bi, te tooñuñu?

Amárico

ካህናትም በሰንበት በመቅደስ ሰንበትን እንዲያረክሱ ኃጢአትም እንዳይሆንባቸው በሕጉ አላነበባችሁምን?

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

noonu saraxalekat yu mag yi ak kureelu àttekat yi yépp di wut ku man a seede lu daan yeesu, ba ñu man koo reylu, waaye gisuñu kenn.

Amárico

የካህናት አለቆችም ሸንጎውም ሁሉ እንዲገድሉት በኢየሱስ ላይ ምስክር ይፈልጉ ነበር፥ አላገኙምም፤

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

lii mooy li ëpp solo ci li nuy wax: am nanu saraxalekat bu mag bu mel noonu, moom mi toog ci ndeyjooru aji màgg ja ca nguuram ca kaw.

Amárico

ከተናገርነውም ዋና ነገሩ ይህ ነው፤ በሰማያት በግርማው ዙፋን ቀኝ የተቀመጠ እንዲህ ያለ ሊቀ ካህናት አለን፤

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bi ko saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya déggee nag, ñu ragal ko, ndaxte mbooloo mépp dañoo waaru ci njàngaleem. noonu ñu seet pexem reylu ko.

Amárico

የካህናት አለቆችም ጻፎችም ሰምተው፥ ሕዝቡ ሁሉ በትምህርቱ ይገረሙ ስለ ነበር ይፈሩት ነበርና እንዴት አድርገው እንዲያጠፉት ፈለጉ።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

yoonu musaa digle na ne, ñi bokk ci giiru lewi te di ay saraxalekat, nañu jot asaka ci alalu bànni israyil, doonte sax ñuy seeni bokk te soqikoo ci ibraayma.

Amárico

ከሌዊ ልጆችም ክህነትን የሚቀበሉት ከህዝቡ ማለት ከወንድሞቻቸው፥ እነርሱ ምንም ከአብርሃም ወገብ ቢወጡ፥ ከእነርሱ አሥራትን በሕግ እንዲያስወጡ ትእዛዝ አላቸው፤

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

ne leen: «lan ngeen ma man a jox, ngir ma jébbal leen yeesu?» noonu saraxalekat ya daldi ko waññal fanweeri poseti estateer.

Amárico

ምን ልትሰጡኝ ትወዳላችሁ እኔም አሳልፌ እሰጣችኋለሁ? እነርሱም ሠላሳ ብር መዘኑለት።

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Consiga uma tradução melhor através
7,743,806,551 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK