You searched for: grâce (Franska - Wolof)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Franska

Wolof

Info

Franska

que la grâce soit avec vous tous! amen!

Wolof

na yiwu yàlla nekk ànd ak yéen ñépp.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que la grâce du seigneur jésus soit avec tous!

Wolof

na yiwu boroom bi yeesu ànd ak yéen ñépp.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que la grâce de notre seigneur jésus christ soit avec vous!

Wolof

na yiwu sunu boroom yeesu kirist ànd ak yéen.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

et nous avons tous reçu de sa plénitude, et grâce pour grâce;

Wolof

kàddu gi fees na ak yiw, te nun ñépp jot nanu ci sunu wàll, mu barkeel nu ay yooni-yoon.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que le seigneur soit avec ton esprit! que la grâce soit avec vous!

Wolof

na boroom bi aar sa xel. na yiwu yàlla ànd ak yéen ñépp.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que la grâce de notre seigneur jésus christ soit avec votre esprit!

Wolof

na yiwu boroom bi yeesu kirist ànd ak seen xel.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que la grâce de notre seigneur jésus christ soit avec vous tous! amen!

Wolof

na yiwu sunu boroom yeesu kirist ànd ak yéen! amiin.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car la grâce de dieu, source de salut pour tous les hommes, a été manifestée.

Wolof

ndaxte yiwu yàlla feeñ na te ubbil na ñépp buntu mucc.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

puisque nous travaillons avec dieu, nous vous exhortons à ne pas recevoir la grâce de dieu en vain.

Wolof

nun nag ñiy liggéeyandoo ak yàlla, nu ngi leen di ñaan: jariñooleen yiw, wi ngeen jote ci yàlla, ngir mu bañ a neen ci yéen.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car la loi a été donnée par moïse, la grâce et la vérité sont venues par jésus christ.

Wolof

ndigali yàlla yi, ci gémmiñu musaa lañu leen jaarale; yiw wi ak dëgg gi, yeesu kirist moo ko indaale.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

afin que, justifiés par sa grâce, nous devenions, en espérance, héritiers de la vie éternelle.

Wolof

ci noonu yàlla àtte na nu jub ci kaw yiwam, te sédd nu ci dund gu dul jeex, gi nuy séentu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

que la grâce et la paix vous soient données de la part de dieu notre père et du seigneur jésus christ!

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 4
Kvalitet:

Franska

david trouva grâce devant dieu, et demanda d`élever une demeure pour le dieu de jacob;

Wolof

moom yiw na fa kanam yàlla, mu ñaan ko, mu sàkkal ko kër ngir askanu yanqóoba.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

afin de montrer dans les siècles à venir l`infinie richesse de sa grâce par sa bonté envers nous en jésus christ.

Wolof

noonu ba fu jamono yem, dina lañal fi sunu kanam yiwam wu réy wi xel mënta takk, jaar ci baaxaay gi mu nu won ci kirist yeesu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

grâce aux entrailles de la miséricorde de notre dieu, en vertu de laquelle le soleil levant nous a visités d`en haut,

Wolof

ndaxte yàlla sunu boroom fees na ak yërmande,ba tax muy wàcce ci nun jant buy fenk,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

ainsi tu n`es plus esclave, mais fils; et si tu es fils, tu es aussi héritier par la grâce de dieu.

Wolof

noonu dootuloo jaam, doom nga. te ndegam doom nga, yàlla jagleel na la cér ci xéewal, yi mu dencal ay doomam.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

a moi, qui suis le moindre de tous les saints, cette grâce a été accordée d`annoncer aux païens les richesses incompréhensibles de christ,

Wolof

may na ma, man mi gën a tuuti ci gaayi yàlla yu sell yi, may xebaar xeeti àddina barkeel yu xel dajul yi ci kirist;

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

les prophètes, qui ont prophétisé touchant la grâce qui vous était réservée, ont fait de ce salut l`objet de leurs recherches et de leurs investigations,

Wolof

naka mucc googu nag, yonent yi xamle yiw, wi ngeen naroon a joti, seet nañu ko te gëstu ko.

Senast uppdaterad: 2023-09-21
Användningsfrekvens: 8
Kvalitet:

Franska

cependant, à certains égards, je vous ai écrit avec une sorte de hardiesse, comme pour réveiller vos souvenirs, à cause de la grâce que dieu m`a faite

Wolof

bu sama kàddu diisee nag ci bataaxal bii, dara taxul lu dul bëgg a yeesal seen xalaat, ndaxte yàlla ci kaw yiwam daf maa sas,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car c`est par la grâce que vous êtes sauvés, par le moyen de la foi. et cela ne vient pas de vous, c`est le don de dieu.

Wolof

ndaxte ci yiwu yàlla ngeen mucce ci kaw ngëm, te loolu jógewul ci yéen, mayu yàlla la;

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,773,119,465 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK