Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.
for det helliges ved guds ord og bønn.
ndaxte kàddug yàlla ak ñaan ñoo koy sellal.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
men nu drar jeg til jerusalem i de helliges tjeneste.
waaye nag fi mu nekk maa ngi dem nii yerusalem, ngir dimbaliji gaayi yàlla yu sell ya fa nekk.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
her er de helliges tålmodighet, de som holder guds bud og jesu tro.
looloo tax gaayi yàlla yi war a muñ, ñooñuy sàmm ndigali yàlla yi ak ngëm ci yeesu.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
og gravene åpnedes, og mange av de hensovede helliges legemer stod op,
te ñu bare ci jëmmi nit ñu sell ñu dee, dekki.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
og røken av røkelsen steg fra engelens hånd op for gud med de helliges bønner.
noonu saxarus cuuraay li gillee ca loxob malaaka ma, ànd ak ñaani gaayi yàlla ya, jëm ca kanam yàlla.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
så er i da ikke lenger fremmede og utlendinger, men i er de helliges medborgere og guds husfolk,
noonu dootuleen ay doxandéem mbaa ay gan, waaye am ngeen baat ci kureelu gaayi yàlla yu sell yi, te waa këram ngeen.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
og jeg så kvinnen drukken av de helliges blod og av jesu vidners blod, og jeg undret mig storlig da jeg så henne.
ma gis jigéen ja màndi ci deretu gaayi yàlla yi, ci deretu ñi doon seedeel yeesu. naka laa ko gis, ma daldi jaaxle lool.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
- til de hellige og troende brødre i kristus i kolossæ: nåde være med eder og fred fra gud vår fader!
noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell, yi dëkk kolos te di ay bokk ci gëm kirist. na leen yàlla sunu baay may yiw ak jàmm.
Senast uppdaterad: 2012-05-06
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet: