You searched for: msingi (Swahili - Wolof)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Swahili

Wolof

Info

Swahili

mitume waliyachukua maneno hayo kama yasiyo na msingi, hivyo hawakuamini.

Wolof

waaye ñu teg wax jooju ay jeneer, ba gëmuñu jigéen ñooñu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

ikiwa alichojenga mtu juu ya huo msingi kitaustahimili huo moto, atapokea tuzo;

Wolof

ku sa liggéey dëgër, dinga jot yool.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

je, hamjasoma maandiko haya? jiwe walilokataa waashi sasa limekuwa jiwe kuu la msingi.

Wolof

ndax musuleen a jàng wax jii ci mbind mi?“doj wi tabaxkat yi sànni,mujj na di doju koñ;

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

hakuna mtu awezaye kuweka msingi mwingine badala ya ule uliokwisha wekwa, yaani yesu kristo.

Wolof

ci li jëm ci fondamaa bi, kenn mënu fee tëral beneen bu dul bi fi xas a taxaw, muy yeesu kirist.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

mmejengwa juu ya msingi uliowekwa na mitume na manabii, naye kristo mwenyewe ndiye jiwe kuu la msingi.

Wolof

yéena ngi sukkandikoo ci fondamaa, bi ndawi kirist yi ak yonent yi tabax, te kirist yeesu ci boppam di doju dalil wa.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

msingi kuu ya gnome ni washuhudi wetu.takriban kila mtu alie au asie na ujuzi wa kutunga programu anauwezo wa kusaidia kuboresha gnome

Wolof

dooley gnome mooy askanam gu rëy. daanaka ku ne, muy ku man walla ku manul bindi tëriin, man ngaa duggal sa loxo ci gnome ngir gënal ko.

Senast uppdaterad: 2014-08-15
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

kwa namna hiyo watajiwekea hazina ambayo itakuwa kwao msingi imara kwa wakati ujao. hapo wataweza kujipatia uzima ambao ni uzima wa kweli.

Wolof

di fàggu dencu ëllëg bu wér. noonu dinañu feddali seen téye ci dund gu wóor gi.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

juu ya msingi huo mtu anaweza kujenga kwa dhahabu, fedha au mawe ya thamani; anaweza kutumia miti, majani au nyasi.

Wolof

ku tabax ci kaw fondamaa bi, wurus, xaalis, per, dénk, gittax walla boob,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

ambayo msingi wake ni tumaini la kupata uzima wa milele. mungu ambaye hasemi uongo, alituahidia uzima huo kabla ya mwanzo wa nyakati,

Wolof

mu sukkandiku ci yaakaar ju dëggu, ji nu am ci dund gu dul jeex, gi yàlla dige ba dara sosoogul, moom mi dul tebbi waxam.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

basi, mungu aliye msingi wa matumaini, awajazeni furaha yote na amani kutokana na imani yenu; tumaini lenu lipate kuongezeka kwa nguvu ya roho mtakatifu.

Wolof

kon yàlla miy maye yaakaar, na def ci seen xol mbég mu réy ak jàmm ju yaa ci seen kaw ngëm, ba ngeen am yaakaar ju mat sëkk ci dooley xel mu sell mi.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

lakini sasa yesu amepewa huduma ya kikuhani iliyo bora zaidi kuliko yao, kama vile agano alilothibitisha kati ya watu na mungu ni bora zaidi, kwani lina msingi wake katika ahadi za mambo yaliyo bora zaidi.

Wolof

waaye léegi nag liggéeyu saraxale, bi ñu jox yeesu, moo gën a màgg liggéeyu saraxalekat yooyu, mel ni it kóllëre, gi yeesu fas diggante yàlla ak nit, moo sut kóllëre gu jëkk ga te mu tëdd ci ay dige yu ëpp yu jëkk ya.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

lakini kama nikicheleweshwa, basi, barua hii itakufahamisha mwenendo tunaopaswa kuwa nao katika nyumba ya mungu, ambayo ni kanisa la mungu aliye hai, na ambalo ni nguzo na msingi wa ukweli.

Wolof

waaye amaana mu yéex. moo tax ma lay bind bataaxal bii, ngir xamal la, ni ñu war a nekke ci kër yàlla gi, maanaam ci mbooloom yàlla aji dund ji, miy kenug dëgg te di sëslaayam.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

basi, tusonge mbele kwa yale yaliyokomaa na kuyaacha nyuma yale mafundisho ya mwanzo ya kikristo. hatuhitaji kuweka msingi tena kwa kurudia yale mafundisho ya mwanzo kama vile kuachana na matendo ya kifo, kumwamini mungu;

Wolof

kon nag léegi, nanu jóge ci liifantu gi jëm ci kirist, te jàll cig mat. nanu bañ a dalaat njàngale mu jëkk moomu, ci ne nit ñi dañoo war a tuub jëf, yi jëm ci dee, te gëm yàlla,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

jiunge nao katika ibada ya kujitakasa, ukalipe na gharama zinazohusika, kisha wanyolewe nywele zao. hivyo watu wote watatambua kwamba habari zile walizoambiwa juu yako hazina msingi wowote, na kwamba wewe binafsi bado unaishi kufuatana na maagizo ya sheria za mose.

Wolof

jël leen, bokk ak ñoom setlu, te nga gàddu seen peyu wateef. noonu ñépp dinañu xam ne, li ñu déggoon ci sa mbir du dëgg, waaye yaa ngi jëf tey sàmm yoonu musaa.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Swahili

hapo yesu akawaambia, "je, hamkusoma jambo hili katika maandiko matakatifu? jiwe walilokataa waashi sasa limekuwa jiwe kuu la msingi. bwana ndiye aliyefanya jambo hili, nalo ni la ajabu sana kwetu!

Wolof

kon yeesu ne leen: «xanaa musuleen a jàng lii ci mbind yi?“doj wi tabaxkat yi sànni;mujj na di doju koñ;ci boroom bi la loolu jóge,te yéemu nanu ci.”

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering

Få en bättre översättning med
7,787,405,402 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK