Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.
yesu alipokwisha pokea hiyo siki, akasema, "yametimia!" kisha akainama kichwa, akatoa roho.
bi yeesu muucoo bineegar bi, mu ne: «lépp mat na!» noonu mu sëgg, delloo ruuwam yàlla.
Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering
kwao yametimia yale aliyosema nabii isaya: kusikia mtasikia, lakini hamtaelewa; kutazama mtatazama, lakini hamtaona.
li esayi waxoon ci kàddug yàlla am na ci ñoom, bi mu naan:“dingeen déglu bu baaxwaaye dungeen xam dara;di xool bu baax waaye dungeen gis dara.
Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
kweli nawaambieni, mpaka hapo mbingu na dunia zitakapopita, hakuna hata nukta moja au sehemu ndogo kabisa ya sheria itakayoondolewa, mpaka yote yametimia.
ndaxte ci dëgg maa ngi leen koy wax, li feek asamaan ak suuf wéyul, benn tomb walla benn rëddu araf du wéy mukk ci yoonu musaa, ba kera yépp di am.
Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
yesu alijua kwamba yote yalikuwa yametimia; na, ili maandiko matakatifu yapate kutimia, akasema, "naona kiu."
bi loolu wéyee gannaaw yeesu xam na ne, lépp mat na léegi, mu ne nag, ngir amal mbind mi: «damaa mar.»
Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering
kisha akaniambia, "yametimia! mimi ni alfa na omega, mwanzo na mwisho. aliye na kiu nitampa kinywaji cha bure kutoka katika chemchemi ya maji ya uzima.
mu teg ca ne ma: «lépp mat na! maay alfa ak omega, njàlbéen gi ak muj gi. ku mar, dinaa la may ci bëtu ndoxum dund mi, te doo fey dara.
Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:
Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering