You searched for: dooleel (Wolof - Engelska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Engelska

Info

Wolof

man naa lépp ci ndimbalu aji dooleel ji.

Engelska

i can do all things through christ which strengtheneth me.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te yudd ak silas, ñi doon yonent, ñuy dooleel bokk yi, di dëgëral seen fit ak wax yu bare.

Engelska

and judas and silas, being prophets also themselves, exhorted the brethren with many words, and confirmed them.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

kirist dina leen dooleel ba ca muj ga, ngir ngeen bañ a am wenn ŋàññ bés bu sunu boroom yeesu kirist dellusee.

Engelska

who shall also confirm you unto the end, that ye may be blameless in the day of our lord jesus christ.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu mu jaar ca bérab yooyu, di dooleel nit ñi ak wax yu bare; ba noppi mu dem réewu geres,

Engelska

and when he had gone over those parts, and had given them much exhortation, he came into greece,

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

maa ngi gërëm sunu boroom kirist yeesu, mi ma dooleel, ci kóolute gi mu am ci man, ba fal ma jawriñ.

Engelska

and i thank christ jesus our lord, who hath enabled me, for that he counted me faithful, putting me into the ministry;

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te yàlla dina leen dooleel ak bépp doole, mu mengoo ak kàttanu ndamam, ngir ngeen man a tegoo coono te muñ, ba fa muñ di yem.

Engelska

strengthened with all might, according to his glorious power, unto all patience and longsuffering with joyfulness;

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye boroom bi moo ma taxawu te dooleel ma, ma jollil kàddu gi, ba xeet yépp dégg ko. te boroom bi musal na ma ci selli gaynde.

Engelska

notwithstanding the lord stood with me, and strengthened me; that by me the preaching might be fully known, and that all the gentiles might hear: and i was delivered out of the mouth of the lion.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi yengu-yengu ba dalee, pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu maseduwan.

Engelska

and after the uproar was ceased, paul called unto him the disciples, and embraced them, and departed for to go into macedonia.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te yàlla mi jagoo yiw wépp te woo leen ci darajay kirist, ngir ngeen bokk ci ndamam li sax, gannaaw bi ngeen yendoo bëccëgu tiis, dina leen yeesalaat, di leen dëgëral ak a dooleel, ba ngeen sampu.

Engelska

but the god of all grace, who hath called us unto his eternal glory by christ jesus, after that ye have suffered a while, make you perfect, stablish, strengthen, settle you.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
8,950,896,255 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK