You searched for: doonte (Wolof - Franska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Franska

Info

Wolof

nit ñi indi sax ñu wopp ca mbedd ya, teg leen ca ay lal yu ndaw ak ay leeso, ngir bu piyeer di jaar, doonte takkandeeram sax yiir ñenn ci ñoom.

Franska

en sorte qu`on apportait les malades dans les rues et qu`on les plaçait sur des lits et des couchettes, afin que, lorsque pierre passerait, son ombre au moins couvrît quelqu`un d`eux.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

na seen dundin rafet ci biir xeeti àddina, kon doonte ñu di leen sosal ay ñaawteef, dinañu gis seeni jëf yu rafet bay màggal yàlla, bés bu leen feeñoo.

Franska

ayez au milieu des païens une bonne conduite, afin que, là même où ils vous calomnient comme si vous étiez des malfaiteurs, ils remarquent vos bonnes oeuvres, et glorifient dieu, au jour où il les visitera.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

su fekkee ne sax, bataaxal bi ma leen bind dafa leen naqare, réccootuma ko. ci lu jëkk réccu naa ko, ndaxte gis naa ne, bataaxal boobu teg na leen tiis, doonte sax ci diir bu néew.

Franska

quoique je vous aie attristés par ma lettre, je ne m`en repens pas. et, si je m`en suis repenti, -car je vois que cette lettre vous a attristés, bien que momentanément, -

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

nun ñi gëm nag nooy dugg ci noflaayam, ni ko mbind mi waxe:«giñ naa kon ci sama mer ne:“duñu dugg mukk ci sama noflaay,”» doonte sax liggéeyam bépp matoon na, ca ba mu sàkkee àddina ak léegi. ci lu jëm ci juróom-ñaareelu fan ba,

Franska

pour nous qui avons cru, nous entrons dans le repos, selon qu`il dit: je jurai dans ma colère: ils n`entreront pas dans mon repos! il dit cela, quoique ses oeuvres eussent été achevées depuis la création du monde.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,781,214,132 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK