You searched for: moo yéen!! (Wolof - Franska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Franska

Info

Wolof

waaye ma des fi ci àddina moo gën ci yéen.

Franska

mais à cause de vous il est plus nécessaire que je demeure dans la chair.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

seen muñ moo leen di musal.

Franska

par votre persévérance vous sauverez vos âmes.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te moo nu yégal it mbëggeel, gi xelu yàlla mi sol ci yéen.

Franska

et qui nous a appris de quelle charité l`esprit vous anime.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te yàlla moo nuy dëgëral ci kirist, nun ak yéen, te sol nu xelam.

Franska

et celui qui nous affermit avec vous en christ, et qui nous a oints, c`est dieu,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

na yiwu boroom bi yeesu ànd ak yéen.

Franska

que la grâce du seigneur jésus soit avec vous!

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

moo tax maa ngi sukk, jublu ci yàlla baay

Franska

a cause de cela, je fléchis les genoux devant le père,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

moo di ki nekkoon ak yàlla ca njàlbéen ga.

Franska

elle était au commencement avec dieu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:

Franska

nous vous y trompez pas, mes frères bien-aimés:

Senast uppdaterad: 2024-04-13
Användningsfrekvens: 12
Kvalitet:

Wolof

moo tax yàlla kaweel ko lool,jox ko tur wi tiim yépp,

Franska

c`est pourquoi aussi dieu l`a souverainement élevé, et lui a donné le nom qui est au-dessus de tout nom,

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

loolu moo tax ñu wooye tool booba ba tey toolu deret.

Franska

c`est pourquoi ce champ a été appelé champ du sang, jusqu`à ce jour.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ngiñ loolu moo tax yeesu nekk tayle, giy wóoral kóllëre gi gën.

Franska

jésus est par cela même le garant d`une alliance plus excellente.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

Ñu wax ko ne: «yeesum nasaret moo fay jaar.»

Franska

on lui dit: c`est jésus de nazareth qui passe.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.

Franska

mais vous, ne vous faites pas appeler rabbi; car un seul est votre maître, et vous êtes tous frères.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

jëlewuma ko ci nit, te kenn jàngalu ma ko, waaye yeesu kirist moo ma ko won.

Franska

car je ne l`ai ni reçu ni appris d`un homme, mais par une révélation de jésus christ.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

moo tax mu waxaat feneen ne:“doo bàyyi sa waa ju sell, mu yàqu.”

Franska

c`est pourquoi il dit encore ailleurs: tu ne permettras pas que ton saint voie la corruption.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye piyeer ak ndaw ya tontu leen ne: «déggal yàlla moo gën déggal nit.

Franska

pierre et les apôtres répondirent: il faut obéir à dieu plutôt qu`aux hommes.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

léegi nag ñett yii ñooy sax: ngëm, yaakaar, mbëggeel; te mbëggeel moo ci raw.

Franska

maintenant donc ces trois choses demeurent: la foi, l`espérance, la charité; mais la plus grande de ces choses, c`est la charité.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

léegi nag yéen ak kureelu àttekat ya, laajleen kilifa ga, mu indi ko ci seen kanam, mel ni dangeen a bëgg a seet mbiram bu gën a wóor. bu ko defee nun dinanu fagaru, ngir rey ko, bala moo agsi.»

Franska

vous donc, maintenant, adressez-vous avec le sanhédrin au tribun, pour qu`il l`amène devant vous, comme si vous vouliez examiner sa cause plus exactement; et nous, avant qu`il approche, nous sommes prêts à le tuer.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Vissa mänskliga översättningar med låg relevans har dolts.
Visa resultat med låg relevans.

Få en bättre översättning med
7,793,351,331 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK