You searched for: tefes (Wolof - Italienska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Italienska

Info

Wolof

bi timis jotee taalibeem ya wàcc ca tefes ga,

Italienska

venuta intanto la sera, i suoi discepoli scesero al mar

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu ñu teer ca tefes ga, bàyyi lépp, di topp ci moom.

Italienska

tirate le barche a terra, lasciarono tutto e lo seguirono

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ci fajar gi yeesu taxaw ca tefes ga, waaye taalibe yi xàmmiwuñu ko.

Italienska

quando gia era l'alba gesù si presentò sulla riva, ma i discepoli non si erano accorti che era gesù

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu yeesu jàllaat dex ga, taxaw ca tefes ga. te nit ñu bare dajaloo, wër ko.

Italienska

essendo passato di nuovo gesù all'altra riva, gli si radunò attorno molta folla, ed egli stava lungo il mare

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu guddi jot, fekk gaal gi nekk ci diggu dex gi, te yeesu rekk moo nekk ca tefes ga.

Italienska

venuta la sera, la barca era in mezzo al mare ed egli solo a terra

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu mu gis ñaari gaal yu teer ca tefes ga, nappkat ya ca wàcce, di raxas seeni mbaal.

Italienska

e la folla gli faceva ressa intorno per ascoltare la parola di dio, vide due barche ormeggiate alla sponda. i pescatori erano scesi e lavavano le reti

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

mbooloo mu bare dajaloo ca moom, ba tax mu dugg cig gaal, toog; mbooloo mépp taxaw ca tefes ga.

Italienska

si cominciò a raccogliere attorno a lui tanta folla che dovette salire su una barca e là porsi a sedere, mentre tutta la folla rimaneva sulla spiaggia

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi mu fa nekkee nag, gaal ga sore na tefes ga, te duus ya di ko yengal bu metti, ndax ngelaw la leen soflu.

Italienska

la barca intanto distava gia qualche miglio da terra ed era agitata dalle onde, a causa del vento contrario

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

mu sant ñi ci des ñu def noonu, langaamu ci ay dénk, mbaa ca tojiti gaal ga. noonu ñépp jot tefes ga ci jàmm ak salaam.

Italienska

poi gli altri, chi su tavole, chi su altri rottami della nave. e così tutti poterono mettersi in salvo a terra

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

Ñu dagg diigal ya, bàyyi leen ci biir géej, yiwiwaale baar ba; ba noppi firi wiiru kanam ga, jublu ca tefes ga.

Italienska

levarono le ancore e le lasciarono andare in mare; al tempo stesso allentarono i legami dei timoni e spiegata al vento la vela maestra, mossero verso la spiaggia

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi mbaal mi feesee nag, ñu ñoddi ko ci tefes gi, ba noppi ñu taxaw, dajale yu baax yi ciy ndab, waaye sànni yi bon.

Italienska

quando è piena, i pescatori la tirano a riva e poi, sedutisi, raccolgono i pesci buoni nei canestri e buttano via i cattivi

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

looloo tax ba, ibraayma mi màggat lool, aw xeet jóge ci moom, baree ni biddiiwi asamaan, te sakkan ni suufu tefes, ba kenn mënu koo xayma.

Italienska

per questo da un uomo solo, e inoltre gia segnato dalla morte, nacque una discendenza numerosa come le stelle del cielo e come la sabbia innumerevole che si trova lungo la spiaggia del mare

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yeneen taalibe ya xëcc mbaal, mi fees dell ak jën, jëme ko ca tefes ga, ndaxte gaal ga sorewul woon; diggante bi waroon na tollook téeméeri meetar.

Italienska

gli altri discepoli invece vennero con la barca, trascinando la rete piena di pesci: infatti non erano lontani da terra se non un centinaio di metri

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

am beneen yoon yeesu nekk ci wetu dex ga, di jàngalewaat. mbooloo mu bare dajaloosi, ba tax mu yéeg cig gaal, dugg ca dex ga; mbooloo mépp taxaw ca tefes ga.

Italienska

di nuovo si mise a insegnare lungo il mare. e si riunì attorno a lui una folla enorme, tanto che egli salì su una barca e là restò seduto, stando in mare, mentre la folla era a terra lungo la riva

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

moona bi jataayu gaal ga matee, nu awaat ci yoon wi. te ñépp gunge nu, ñoom ak seeni jabar ak seeni doom; nu génn dëkk ba, sukk ca tefes ga, ñaan ci yàlla.

Italienska

ma quando furon passati quei giorni, uscimmo e ci mettemmo in viaggio, accompagnati da tutti loro con le mogli e i figli sin fuori della città. inginocchiati sulla spiaggia pregammo, poi ci salutammo a vicenda

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

simoŋ piyeer yéeg ca gaal ga, daldi xëcc mbaal ma ca tefes ga, mu fees dell ak jën yu mag; matoon na téeméeri jën ak juróom-fukk ak ñett. te li muy baree-bare lépp, taxul mbaal ma dog.

Italienska

allora simon pietro salì nella barca e trasse a terra la rete piena di centocinquantatrè grossi pesci. e benché fossero tanti, la rete non si spezzò

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,800,165,685 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK