You searched for: bokk ci (Wolof - Japanska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Japanska

Info

Wolof

bokk yi, buleen nu fàtte ci seeni ñaan.

Japanska

兄弟たちよ。わたしたちのためにも、祈ってほしい。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:

Japanska

愛する兄弟たちよ。思い違いをしてはいけない。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yéen nag bokk yi, buleen tàyyi ci def lu rafet.

Japanska

兄弟たちよ。あなたがたは、たゆまずに良い働きをしなさい。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bokk yi, bu leen àddina bañee, buleen ci jaaxle.

Japanska

兄弟たちよ。世があなたがたを憎んでも、驚くには及ばない。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

léegi nag yoon mënul a dab ñi bokk ci yeesu kirist.

Japanska

こういうわけで、今やキリスト・イエスにある者は罪に定められることがない。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

saxleen ci bëggante ni ay bokk.

Japanska

兄弟愛を続けなさい。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

wax naa leen loolu, ngir ngeen bokk ci sama mbég, te seen bos mat sëkk.

Japanska

わたしがこれらのことを話したのは、わたしの喜びがあなたがたのうちにも宿るため、また、あなたがたの喜びが満ちあふれるためである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yéen ñépp doomi yàlla ngeen ndax li ngeen bokk ci kirist yeesu ci kaw ngëm.

Japanska

あなたがたはみな、キリスト・イエスにある信仰によって、神の子なのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yéen ñépp, ñi ñu sóob ci ndox ngir wone seen bokk ci kirist, soloo ngeen kirist.

Japanska

キリストに合うバプテスマを受けたあなたがたは、皆キリストを着たのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te jaam du bokk ci kër gi ba fàww, waaye doom, moom, ci kër gi la bokk ba fàww.

Japanska

そして、奴隷はいつまでも家にいる者ではない。しかし、子はいつまでもいる。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

kon ni ñépp deeye ci seen bokk ci aadama, noonu la ñépp di dundaate ci seen bokk ci kirist.

Japanska

アダムにあってすべての人が死んでいるのと同じように、キリストにあってすべての人が生かされるのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye léegi ci seen bokk ci kirist yeesu, yéen ñi sore woon jege ngeen ndax deretu kirist ji ñu tuur.

Japanska

ところが、あなたがたは、このように以前は遠く離れていたが、今ではキリスト・イエスにあって、キリストの血によって近いものとなったのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

fekk booba amoon na ay yawut yu daloon yerusalem, doon ay nit ñu ragal yàlla te bokk ci xeeti àddina yépp.

Japanska

さて、エルサレムには、天下のあらゆる国々から、信仰深いユダヤ人たちがきて住んでいたが、

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

naka yéen xale yi, nangeen déggal seeni waajur, ci li ngeen bokk ci boroom bi, ndaxte looloo rafet.

Japanska

子たる者よ。主にあって両親に従いなさい。これは正しいことである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te ci seen bokk ci kirist, yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci xel mu sell mi.

Japanska

そしてあなたがたも、主にあって共に建てられて、霊なる神のすまいとなるのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te bu nopp nee: «duma bët, kon bokkuma ci yaram,» du ko teree bokk ci céri yaram yi.

Japanska

また、もし耳が、わたしは目ではないから、からだに属していないと言っても、それで、からだに属さないわけではない。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

su nu kirist mayee fit nag ak mbëggeel guy dëfël sunu xol, su nu amee cér ci xel mu sell mi, su amee cofeel ak yërmande ci sunu bokk ci moom,

Japanska

そこで、あなたがたに、キリストによる勧め、愛の励まし、御霊の交わり、熱愛とあわれみとが、いくらかでもあるなら、

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

kon nag amul xaajale ci diggante yawut ak ki dul yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci kirist.

Japanska

もはや、ユダヤ人もギリシヤ人もなく、奴隷も自由人もなく、男も女もない。あなたがたは皆、キリスト・イエスにあって一つだからである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yoonu musaa digle na ne, ñi bokk ci giiru lewi te di ay saraxalekat, nañu jot asaka ci alalu bànni israyil, doonte sax ñuy seeni bokk te soqikoo ci ibraayma.

Japanska

さて、レビの子のうちで祭司の務をしている者たちは、兄弟である民から、同じくアブラハムの子孫であるにもかかわらず、十分の一を取るように、律法によって命じられている。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye ku nekk ak ayam. kirist moo jëkk, mel ni gub yi ñu jëkk a tànne ci ngóob mi, ba noppi, bu kirist dellusee, ñi bokk ci moom jël seen ay.

Japanska

ただ、各自はそれぞれの順序に従わねばならない。最初はキリスト、次に、主の来臨に際してキリストに属する者たち、

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Vissa mänskliga översättningar med låg relevans har dolts.
Visa resultat med låg relevans.

Få en bättre översättning med
7,782,365,517 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK