You searched for: delloo (Wolof - Japanska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Japanska

Info

Wolof

bés booba dina delloo ku nekk ay jëfam.

Japanska

神は、おのおのに、そのわざにしたがって報いられる。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te it:«ku ko mas a jox dara,ba mu war laa delloo?»

Japanska

また、だれが、まず主に与えて、その報いを受けるであろうか」。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ndaxte jub na ci yàlla, mu delloo coono ñi leen di sonal,

Japanska

すなわち、あなたがたを悩ます者には患難をもって報い、悩まされているあなたがたには、わたしたちと共に、休息をもって報いて下さるのが、神にとって正しいことだからである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi ñu delloo ca kër ga nag, taalibe ya laaj ko ci mbirum loolu.

Japanska

家にはいってから、弟子たちはまたこのことについて尋ねた。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

xam ne ku def lu baax, boroom bi delloo la ko, muy jaam, muy gor.

Japanska

あなたがたが知っているとおり、だれでも良いことを行えば、僕であれ、自由人であれ、それに相当する報いを、それぞれ主から受けるであろう。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye ku def lu bon, boroom bi dina la delloo sa jëf, te du gënale.

Japanska

不正を行う者は、自分の行った不正に対して報いを受けるであろう。それには差別扱いはない。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ngir sa sarax nekk kumpa. noonu sa baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.

Japanska

それは、あなたのする施しが隠れているためである。すると、隠れた事を見ておられるあなたの父は、報いてくださるであろう。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi fa ay doomi baayam delloo nag, yuusufa xàmmiku leen, te firawna xamante ak njabootam.

Japanska

二回目の時に、ヨセフが兄弟たちに、自分の身の上を打ち明けたので、彼の親族関係がパロに知れてきた。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu delloo naa leen ko ci lu gaaw, ngir ñëwam bégal seeni xol, te man itam sama xol féex.

Japanska

そこで、大急ぎで彼を送り返す。これで、あなたがたは彼と再び会って喜び、わたしもまた、心配を和らげることができよう。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»

Japanska

わが義人は、信仰によって生きる。もし信仰を捨てるなら、わたしのたましいはこれを喜ばない」。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi alkaati ya delloo, saraxalekat yu mag ya ak farisen ya laaj leen ne: «lu tax indiwuleen ko?»

Japanska

さて、下役どもが祭司長たちやパリサイ人たちのところに帰ってきたので、彼らはその下役どもに言った、「なぜ、あの人を連れてこなかったのか」。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yeesu nee na: «maa ngi ñëw léegi, indaale pey gi, ngir delloo ku nekk lu mengoo ak lu mu def.

Japanska

「見よ、わたしはすぐに来る。報いを携えてきて、それぞれのしわざに応じて報いよう。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu géej gëq néew, yi nekkoon ci moom; dee ak barsàq delloo néew, ya ñu yoroon. Ñu àtte ñépp ci seeni jëf.

Japanska

海はその中にいる死人を出し、死も黄泉もその中にいる死人を出し、そして、おのおのそのしわざに応じて、さばきを受けた。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ngir sa koor bañ a feeñu nit ñi, waaye mu feeñu sa baay bi bët mënta gis. noonu sa baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.

Japanska

それは断食をしていることが人に知れないで、隠れた所においでになるあなたの父に知られるためである。すると、隠れた事を見ておられるあなたの父は、報いて下さるであろう。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi xale biy agsi, rab wi di ko daaneel ci suuf, muy say. waaye yeesu daldi gëdd rab wa, wéral xale ba, daldi ko delloo baayam.

Japanska

ところが、その子がイエスのところに来る時にも、悪霊が彼を引き倒して、引きつけさせた。イエスはこの汚れた霊をしかりつけ、その子供をいやして、父親にお渡しになった。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye ku ci am ay doom mbaa ay sët, na njaboot googu jëkk a wone seen ragal yàlla ci seen biir kër, ci delloo njukkal seen waajur, ndaxte loolu lu rafet la fa kanam yàlla.

Japanska

やもめに子か孫かがある場合には、これらの者に、まず自分の家で孝養をつくし、親の恩に報いることを学ばせるべきである。それが、神のみこころにかなうことなのである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yeesu woote ak kàddu gu dëgër naan: «baay, jébbal naa la sama ruu!» bi mu waxee loolu, mu delloo ruuwam yàlla.

Japanska

そのとき、イエスは声高く叫んで言われた、「父よ、わたしの霊をみ手にゆだねます」。こう言ってついに息を引きとられた。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi malaaka ya delloo ca asamaan, sàmm yi di waxante naan: «nanu dem boog betleyem, seeti la fa xew, li nu boroom bi xamal.»

Japanska

御使たちが彼らを離れて天に帰ったとき、羊飼たちは「さあ、ベツレヘムへ行って、主がお知らせ下さったその出来事を見てこようではないか」と、互に語り合った。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

«yéena di xoromus àddina. bu xorom si sàppee, nan lañu koy delloo cafkaam? du jariñati dara, lu dul ñu sànni ko ci biti, nit ñi dox ci kawam.

Japanska

あなたがたは、地の塩である。もし塩のききめがなくなったら、何によってその味が取りもどされようか。もはや、なんの役にも立たず、ただ外に捨てられて、人々にふみつけられるだけである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye soppleen seeni noon, di leen defal lu baax, tey leble, bañ a yaakaar ñu delloo leen ko. noonu seen yool dina mag te dingeen wone ne, yéenay doomi aji kawe ji, ndaxte yàlla day wone mbaaxam ci ñu goreedi ñi ak ñu soxor ñi.

Japanska

しかし、あなたがたは、敵を愛し、人によくしてやり、また何も当てにしないで貸してやれ。そうすれば受ける報いは大きく、あなたがたはいと高き者の子となるであろう。いと高き者は、恩を知らぬ者にも悪人にも、なさけ深いからである。

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,794,826,798 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK