You searched for: waajuri (Wolof - Spanska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Spanska

Info

Wolof

waajuri yeesu yi waaru ci li ñu doon wax ci xale bi.

Spanska

su padre y su madre se maravillaban de las cosas que se decían de él

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waajuri xale bi daldi waaru. waaye yeesu tere leen, ñu wax kenn li xew.

Spanska

sus padres quedaron atónitos, y él les mandó que a nadie dijesen lo que había sucedido

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

at mu jot nag waajuri yeesu yi daan nañu dem yerusalem, ngir màggali bésu jéggi ba.

Spanska

iban sus padres todos los años a jerusalén, para la fiesta de la pascua

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi waajuri yeesu yi matalee seen warugar ci lépp lu yoonu boroom bi santaane woon, ñu dellu seen dëkku nasaret ca diiwaanu galile.

Spanska

cuando cumplieron con todos los requisitos de la ley del señor, volvieron a galilea, a su ciudad de nazaret

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu xelum yàlla daldi yóbbu simeyon ba ca kër yàlla ga. bi waajuri yeesu indee xale ba, ngir sédde ko yàlla, ni ko yoon wi santaanee,

Spanska

movido por el espíritu, entró en el templo; y cuando los padres trajeron al niño jesús para hacer con él conforme a la costumbre de la ley

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ragal yawut ya nag moo taxoon waajuri nit ka waxe noonu, ndaxte yawut ya dañoo mànkoo woon ne, képp ku seede ne yeesu mooy almasi bi, ñu dàq la ca jàngu ba.

Spanska

sus padres dijeron esto porque tenían miedo de los judíos, porque ya los judíos habían acordado que si alguno confesara que jesús era el cristo, fuera expulsado de la sinagoga

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,770,715,075 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK