Şunu aradınız:: kuhubiri (Svahili - Wolof)

İnsan katkıları

Profesyonel çevirmenler, işletmeler, web sayfaları ve erişimin serbest olduğu çeviri havuzlarından.

Çeviri ekle

Svahili

Wolof

Bilgi

Svahili

lakini wewe unapaswa kuhubiri mafundisho safi.

Wolof

yaw nag nangay waare li dëppook njàngale mu wér mi.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

baada ya kuhubiri ule ujumbe huko perga, walikwenda atalia.

Wolof

Ñu yégle kàddu gi ci dëkku peers, door a dem dëkku atali.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

halafu akawatuma waende kuhubiri ufalme wa mungu na kuponya wagonjwa.

Wolof

noonu mu yónni leen ñuy yégle nguuru yàlla ak di faj jarag yi.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

sisi, lakini, tutashughulika na sala na kazi ya kuhubiri neno la mungu."

Wolof

waaye nun dinanu wéy ci ñaan ci yàlla ak ci yenub xamle kàddu gi.»

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Uyarı: Görünmez HTML biçimlendirmesi içeriyor

Svahili

mungu amenichagua mimi niwe mtume na mwalimu kwa ajili ya kuhubiri habari njema,

Wolof

te yàlla fal na ma ndaw ak jàngalekat, ngir may yégle xebaar bi;

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

naye akawateua watu kumi na wawili ambao aliwaita mitume, wakae naye, awatume kuhubiri

Wolof

noonu mu tànn ci fukk ak ñaar, tudde leen ay ndawam, ngir ñu ànd ak moom te mu yónni leen, ñu waareji,

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

wakaendelea kila siku kufundisha na kuhubiri habari njema ya kristo, hekaluni na nyumbani mwa watu.

Wolof

noonu bés bu nekk ca kër yàlla ga ak ca kër ya, daawuñu noppee jàngale ak a xamle xebaar bu baax bi, ne yeesu mooy almasi bi.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

nilipofika troa kuhubiri habari njema ya kristo, nilikuta mlango u wazi kwa ajili ya kazi ya bwana.

Wolof

ba ma àggee torowas nag, ngir yégle fa xebaar bu baax bi ci kirist, boroom bi ubbil na ma ci bunt.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

lakini sasa, ee bwana, angalia vitisho vyao. utuwezeshe sisi watumishi wako kuhubiri neno lako kwa uhodari.

Wolof

léegi nag boroom bi, seetal seeni tëkku te may say jaam, nuy wax sa kàddu ak fit.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

mungu, ambaye ninamtumikia kwa moyo wangu wote katika kuhubiri habari njema ya mwanae, ni shahidi wangu kwamba ninawakumbukeni

Wolof

bët bu set maa ngi leen di boole ci samay ñaan. yàlla seede na li may wax, yàlla mi may jaamu ci sama xel, ci xamle xebaar bu baax bu doomam.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

paulo na barnaba walibaki huko antiokia kwa muda; wakafundisha na kuhubiri neno la bwana, pamoja na watu wengine wengi.

Wolof

waaye pool ak barnabas des ci ancos, di jàngale ak di xamle xebaar bu baax bu kàddug boroom bi, ñoom ak ñeneen ñu bare.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

baada ya paulo na barnabas kuhubiri habari njema huko derbe na kupata wafuasi wengi, walifunga safari kwenda antiokia kwa kupitia lustra na ikonio.

Wolof

bi ñu fa àggee nag, ñu xamle fa xebaar bu baax bi, ba sàkk fa ay taalibe yu bare. gannaaw loolu ñu dellusi listar, ikoñum ak ancos,

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

baada ya sila na timotheo kuwasili kutoka makedonia, paulo alianza kutumia wakati wake wote kwa ajili ya kuhubiri, akawathibitishia wayahudi kwamba yesu ndiye kristo.

Wolof

waaye bi silas ak timote jógee diiwaanu maseduwan, egg fa, pool jublu ci xamle kàddu gi, tey dëggal ci yawut yi naan, yeesu mooy almasi bi.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

na kumtuma kwenu ndugu yetu timotheo, ambaye ni mfanyakazi mwenzetu kwa ajili ya mungu katika kuhubiri habari njema ya kristo. tulimtuma ili awaimarisheni na kuwafarijini,

Wolof

te yónni nanu timote, sunu mbokk ak sunu nawle ci liggéeyu yàlla ak ci waareb xebaaru kirist. yónni nanu ko, ngir mu dénk leen, tey feddali seen ngëm,

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

kristo hakunituma kubatiza, bali kuhubiri habari njema; tena, niihubiri bila kutegemea maarifa ya hotuba za watu kusudi nguvu ya kifo cha kristo msalabani isibatilishwe.

Wolof

ndaxte kirist yebalu ma ngir may sóobe ci ndox, waaye da maa yebal, ngir may yégle xebaar bu baax bi, te ma bañ koo def ak waxi xam-xamu nit, ngir bañ a ñàkkal faayda deewu kirist ca bant ba.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

lakini yeye akawaambia, "ninapaswa kuhubiri habari njema za ufalme wa mungu katika miji mingine pia, maana nilitumwa kwa ajili hiyo."

Wolof

waaye mu ne leen: «damaa war a dem ci yeneen dëkk yi, ngir yégle xebaar bu baax bi ci nguuru yàlla, ndaxte looloo tax ñu yónni ma.»

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Uyarı: Görünmez HTML biçimlendirmesi içeriyor

Svahili

ila nilianza kuhubiri kwanza kwa watu wa damasko, halafu kwa wale wa yerusalemu na nchi yote ya yudea, na pia kwa watu wa mataifa mengine. niliwahimiza wamgeukie mungu na kuonyesha kwa vitendo kwamba wamebadilisha mioyo yao.

Wolof

waaye li tàmbali ci damas, teg ci dëkku yerusalem ak réewu yawut mépp, ba agsi ci ñi dul yawut, yégal naa leen, ñu tuub seeni bàkkaar te woññiku ci yàlla, bay jëf lu dëppook réccu.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Svahili

mimi ni yohane, ndugu yenu; na kwa kuungana na kristo nashiriki pamoja nanyi katika kustahimili mateso yanayowapata wale walio wa utawala wake. mimi nilikuwa kisiwani patmo kwa sababu ya kuhubiri ujumbe wa mungu na ukweli wa yesu.

Wolof

man yowaana seen mbokk, di seen nawle ci fitna, ci nguur ak ci muñ, yi nu am ndax sunu booloo ak yeesu, maa nga nekkoon ca dun bu ñuy wax patmos. wacce woon nañu ma fa, ndax li ma doon waare kàddug yàlla tey seedeel yeesu.

Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:

Daha iyi çeviri için
7,745,089,930 insan katkısından yararlanın

Kullanıcılar yardım istiyor:



Deneyiminizi iyileştirmek için çerezleri kullanıyoruz. Bu siteyi ziyaret etmeye devam ederek çerezleri kullanmamızı kabul etmiş oluyorsunuz. Daha fazla bilgi edinin. Tamam