Profesyonel çevirmenler, işletmeler, web sayfaları ve erişimin serbest olduğu çeviri havuzlarından.
msijidanganye wenyewe kwa kusikiliza tu neno lake, bali litekelezeni kwa vitendo.
buleen yem ci déglu kàddu gi rekk, di nax seen bopp; waaye jëfeleen ko.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
msijidanganye! mtu yeyote miongoni mwenu akijidhania mwenye hekima mtindo wa kidunia, heri awe mjinga kusudi apate kuwa na hekima ya kweli.
kon bu kenn nax boppam: su kenn ci yéen tegee boppam boroom xam-xam ci gis-gisu àddina sii, kooku na doon dof, ngir am xam-xam bu wóor.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
au je, hamjui kwamba watu wabaya hawataurithi utawala wa mungu? msijidanganye! watu wanaoishi maisha ya uasherati, wanaoabudu sanamu, wazinzi, au walawiti,
xanaa xamuleen ne, ñi jubadi duñu bokk ci nguuru yàlla? bu leen ci kenn nax: ñiy doxaan walla xërëmkat yi ak njaalookat yi ak góor-jigéen ñi ak ñi ko nangu,
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite: