Profesyonel çevirmenler, işletmeler, web sayfaları ve erişimin serbest olduğu çeviri havuzlarından.
lakini solomoni ndiye aliyemjengea mungu nyumba.
waaye suleymaan moo tabaxal yàlla kër ga.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
naye yesu akawa anatembea hekaluni katika ukumbi wa solomoni.
yeesoo nga woon ca kër yàlla ga, di doxantu ca biir werandaa bu suleymaan.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
solomoni alimzaa rehoboamu, rehoboamu alimzaa abiya, abiya alimzaa asa,
suleymaan jur robowam; robowam abiya; abiya asaf;
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
lakini nawaambieni, hata solomoni mwenyewe na fahari zake zote hakupata kuvikwa vizuri kama ua mojawapo.
waaye maa ngi leen di wax ne, suleymaan sax ci ndamam soluwul woon ni benn ci ñoom.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
mitume walifanya miujiza na maajabu mengi kati ya watu. waumini walikuwa wakikutana pamoja katika ukumbi wa solomoni.
bi loolu amee ay kéemaan ak ay firnde yu bare di xew ci nit ñi, jaare ca loxoy ndaw ya. Ñépp di booloo ca werandaa bu suleymaan ca kër yàlla ga.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
naye yese alimzaa mfalme daudi. daudi alimzaa solomoni (mama yake solomoni alikuwa mke wa uria).
miy baayu buur bi daawuda. daawuda moo jur suleymaan ci ki nekkoon jabari uri;
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
angalieni maua jinsi yanavyomea. hayafanyi kazi wala hayafumi. hata hivyo, nawahakikishieni kwamba hata solomoni mwenyewe na fahari zake zote hakupata kuvikwa vizuri kama ua mojawapo.
«seetleen ni tóor-tóori ñax mi di saxe. duñu liggéey, duñu ëcc, waaye maa ngi leen di wax ne, suleymaan sax ci ndamam, soluwul woon ni benn ci ñoom.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
malkia wa kusini atatokea wakati kizazi hiki kitakapohukumiwa, naye atakihukumu kwamba kina hatia. maana yeye alisafiri kutoka mbali akaja kusikiliza maneno ya hekima ya solomoni, na kumbe hapa kuna kikuu kuliko solomoni.
te it ca bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-xamu suleymaan, te ku sut suleymaan a ngi fi.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite:
malkia wa kusini atatokea wakati kizazi hiki kitakapohukumiwa, naye atashuhudia kwamba kina hatia. yeye alisafiri kutoka mbali, akaja kusikiliza maneno ya hekima ya solomoni; kumbe hapa pana mkuu zaidi kuliko solomoni.
keroog bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-xamu suleymaan, te ku sut suleymaan a ngi fi.
Son Güncelleme: 2012-05-05
Kullanım Sıklığı: 1
Kalite: