您搜索了: safari (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

na katika safari hiyo ilimbidi apitie samaria.

沃洛夫语

bi muy dem galile, waroon na jaar ci diiwaanu samari.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu akaendelea na safari, na watu wakatandaza mavazi yao barabarani.

沃洛夫语

bi muy dem, nit ñi di lalal yeesu seeni yére ci yoon wi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

katika safari hiyo alipitia siria na kilikia akiyaimarisha makanisa.

沃洛夫语

mu jaar ci diiwaanu siri ak silisi, di dëgëral mboolooy ñi gëm.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

nimefanya bidii katika mashindano, nimemaliza safari yote na imani nimeitunza.

沃洛夫语

bëre naa ba ub làmbi ngëm, daw naa ba àkk, sàmm naa mboolem dëgg, gi ñu ma dénk.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walipokikaribia kile kijiji walikokuwa wanakwenda, yesu akafanya kana kwamba anaendelea na safari;

沃洛夫语

bi ñuy jub dëkk, ba ñu jëmoon nag, yeesu def ni kuy jubal yoonam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya kukaa pale kwa muda, tulifunga mizigo yetu, tukaendelea na safari kwenda yerusalemu.

沃洛夫语

gannaaw fan yooyu nu defaru, ngir dem yerusalem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, wakaanza safari, wakapitia vijijini wakihubiri habari njema na kuponya wagonjwa kila mahali.

沃洛夫语

noonu ñu dem dëkk ak dëkk, di fa yégle xebaar bu baax bi, tey wéral jarag yi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akawaacha, akapanda tena mashua, akaanza safari kwenda ng'ambo ya pili ya ziwa.

沃洛夫语

ci kaw loolu yeesu bàyyi leen, duggaat ci gaal gi, di jàll dex gi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alikaa huko muda mfupi, halafu akaendelea na safari kwa kupitia sehemu za galatia na frugia akiwatia moyo wafuasi wote.

沃洛夫语

bi mu fa desee ay jamono, mu jóge fa, di jaar dëkkoo-dëkk ci diiwaanu galasi ak firisi, di dooleel xoli taalibe yépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya sikukuu, walianza safari ya kurudi makwao, lakini yesu alibaki yerusalemu bila wazazi wake kuwa na habari.

沃洛夫语

bi màggal ga tasee, ñu dëpp ñibbi, waaye xale ba yeesu des yerusalem, te ay waajuram yéguñu ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini wao waliendelea na safari toka pisga hadi mjini antiokia pisidia. siku ya sabato waliingia ndani ya sunagogi, wakakaa.

沃洛夫语

waaye ñoom ñu jóge peers, aw ca yoon wa, ba ñëw dëkku ancos ci diiwaanu pisidi. bésu noflaay ba nag ñu dugg ca jàngu ba, toog.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya paulo na barnabas kuhubiri habari njema huko derbe na kupata wafuasi wengi, walifunga safari kwenda antiokia kwa kupitia lustra na ikonio.

沃洛夫语

bi ñu fa àggee nag, ñu xamle fa xebaar bu baax bi, ba sàkk fa ay taalibe yu bare. gannaaw loolu ñu dellusi listar, ikoñum ak ancos,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

itakuwa kama mtu anayeondoka nyumbani kwenda safari akiwaachia watumishi wake madaraka, kila mmoja na kazi yake; akamwambia mlinzi wa mlango awe macho.

沃洛夫语

«mi ngi mel ni nit ku tukki, mu dénk këram ay surgaam, ku nekk ak sa sas, te sant bëkk-néeg bi, mu xool.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hata hivyo, kwa leo, kesho na kesho kutwa, ni lazima niendelee na safari yangu, kwa sababu si sawa nabii auawe nje ya yerusalemu.

沃洛夫语

waaye fàww ma dox sama itte tey, suba ak gannaaw suba, ndaxte wareesul a reye ab yonent feneen fu dul yerusalem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

petro akawaalika ndani, akawapa mahali pa kulala usiku ule. kesho yake, petro alianza safari pamoja nao, na baadhi ya ndugu wa huko yopa walifuatana naye.

沃洛夫语

ci kaw loolu piyeer dugal leen, dalal leen. ba bët setee, piyeer jóg, dem ak ñoom, ànd ak ñenn ci bokk yi dëkk yope,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naogopa huenda hapo nitakapokuja safari ijayo mungu wangu atanifanya niaibike mbele yenu, nami nitaomboleza kwa ajili ya wengi wa wale waliotenda dhambi lakini hawakujutia huo uchafu, tamaa zao mbaya na uzinzi waliokuwa wamefanya.

沃洛夫语

ragal naa, bu ma leen ganesiwaatee, yàlla sama boroom suufeel ma ci seen biir, ma naqarlu ci ñu bare ñu bàkkaaroon te dëdduwuñu seen yàqute, seen njaaloo ak seen ñaawteef, gi ñu doon def.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya miezi mitatu tulianza tena safari yetu kwa meli moja ya aleksandria iitwayo "miungu pacha". meli hiyo ilikuwa imetia nanga kisiwani wakati wote wa baridi.

沃洛夫语

bi nu fa amee ñetti weer, nu dugg ca gaal gu lollikoo ca dun ba, daldi tàbbi ca géej ga. gaalu dëkku alegsàndiri la woon, te yor xàmmikaay guy nataalu kastor ak polugsë.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

nilikwisha sema, na kama ilivyokuwa safari ya pili, sasa nasema tena nikiwa mbali: wale wote waliotenda uovu bila kutubu, na pia wale wengine, nitakapokuja, watakiona cha mtema kuni.

沃洛夫语

li ma waxoon ci sama ñaareelu ngan, ci ñi bàkkaaroon bu yàgg ak ñi ci des, maa ngi koy waxaat léegi, bala maa dikkaat: su ma dellusee, duma yërëm kenn.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

siku moja, yesu alipanda mashua pamoja na wanafunzi wake, akawaambia, "tuvuke ziwa twende mpaka ng'ambo." basi, wakaanza safari.

沃洛夫语

benn bés yeesu àndoon na ak ay taalibeem, dugg ci gaal. mu ne leen: «nanu jàll dex gi.» noonu ñu dem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, filipo akajiweka tayari, akaanza safari. wakati huohuo kulikuwa na mwethiopia mmoja, towashi, ambaye alikuwa anasafiri kuelekea nyumbani. huyo mtu alikuwa ofisa maarufu wa hazina ya kandake, malkia wa ethiopia. alikuwa amekwenda huko yerusalemu kuabudu na wakati huo alikuwa anarudi akiwa amepanda gari la kukokotwa.

沃洛夫语

filib jóg dem. noonu mu gis fa nitu ecópi ku yoom, di jaraaf ju mag ci kandas, buur bu jigéen bu ecópi, te di ko wottul xaalisam bépp. fekk mu ñëwoon yerusalem, ngir màggalsi yàlla, bay dellu;

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,737,909,490 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認