您搜索了: wakamtukuza (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

basi, wakamtukuza mungu kwa sababu yangu.

沃洛夫语

te ñuy sant yàlla ci man.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wote wakashangaa na kushikwa na hofu; wakamtukuza mungu wakisema: "tumeona maajabu leo."

沃洛夫语

mbooloo mépp waaru, di màggal yàlla. Ñu ragal tey wax naan: «gis nanu tey ay mbir yu ëpp xel.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

watu wote katika ule umati walipoona hayo, walishangaa na kuogopa; wakamtukuza mungu aliyewapa binadamu uwezo wa namna hiyo.

沃洛夫语

ba mbooloo ma gisee loolu, ñu daldi ragal te màggal yàlla, mi dénk sañ-sañ bu tollu noonu doom aadama yi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

waliposikia hayo, waliacha ubishi, wakamtukuza mungu wakisema, "mungu amewapa watu wa mataifa mengine nafasi ya kutubu na kuwa na uzima!"

沃洛夫语

bi ñu déggee loolu, amuñu dara lu ñu ca teg, ñu daldi màggal yàlla ne: «yàlla nag may na ñi dul yawut it ñu tuub seeni bàkkaar, ba am dund gu wóor gi.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

wakati huohuo, kukatokea tetemeko kubwa la ardhi, sehemu moja ya kumi ya ardhi ikaharibiwa. watu elfu saba wakauawa kwa tetemeko hilo la ardhi. watu waliosalia wakaogopa sana, wakamtukuza mungu wa mbinguni.

沃洛夫语

ca saa sa am yengu-yengub suuf bu mag, te benn ci fukki xaaju dëkk ba daldi màbb. juróom-ñaari junniy nit dee ci yengu-yengub suuf ba, te ña ca des tiit, daldi màggal yàllay asamaan.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,763,902,216 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認