您搜索了: wanawasalimuni (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

luka, daktari wetu mpenzi, na dema, wanawasalimuni.

沃洛夫语

luug, doktoor bi ñu sopp, mu ngi leen di nuyu, moom ak demas.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

(g13-12) watu wote wa mungu huku wanawasalimuni.

沃洛夫语

mboolem gaayi yàlla yépp ñu ngi leen di nuyu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ndugu wote wanawasalimuni. nanyi salimianeni kwa ishara ya mapendo ya mungu.

沃洛夫语

bokk yépp ñu ngi leen di nuyu. saafoonteleen ak xol bu laab.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wasalimieni viongozi wenu wote pamoja na watu wa mungu! ndugu wa italia wanawasalimuni.

沃洛夫语

nuyul-leen ma seen njiit yépp ak gaayi yàlla yépp. waa itali ñu ngi leen di nuyu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

jumuiya ya wenzenu walioteuliwa na mungu hapa babuloni wanawasalimuni. vilevile mwanangu marko anawasalimuni.

沃洛夫语

mbooloo mi nekk ci dëkk bi ñuy wax babilon te yàlla tànn ko ni yéen, moo di leen nuyu, ñoom ak màrk sama doomu diine.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

makanisa yote ya asia yanawasalimuni. akula na priskila pamoja na watu wote wa mungu walio nyumbani mwao wanawasalimuni sana katika bwana.

沃洛夫语

mboolooy ñi gëm te nekk diiwaanu asi ñu ngi leen di nuyu. akilas ak pirsil, ñu ngi leen di nuyu bu baax ci boroom bi, ñoom ak mbooloom ñi gëm tey daje seen kër.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,761,965,866 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認