您搜索了: yosefu (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

yosefu akauchukua ule mwili akauzungushia sanda safi ya kitani,

沃洛夫语

noonu yuusufa fab jëmm ja, laxas ko ci càngaay lu set,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mwishowe, mfalme mmoja ambaye hakumtambua yosefu alianza kutawala huko misri.

沃洛夫语

ba keroog beneen buur bu xamul yuusufa di falu ci misra.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yakobo alimzaa yosefu, aliyekuwa mume wake maria, mama yake yesu, aitwaye kristo.

沃洛夫语

yanqóoba nag moo jur yuusufa jëkkëru maryaama; te ci maryaama la yeesu, mi ñuy wax kirist, juddoo.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya kifo cha herode, malaika wa bwana alimtokea yosefu katika ndoto kule misri,

沃洛夫语

bi nga xamee ne erodd faatu na, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ca misra,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, yosefu aliamka, akamchukua mtoto pamoja na mama yake, akarejea katika nchi ya israeli.

沃洛夫语

yuusufa jóg nag, jël xale ba ak ndeyam, dellu israyil.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

katika safari yao ya pili, yosefu alijitambulisha kwa ndugu zake, na farao akaifahamu jamaa ya yosefu.

沃洛夫语

bi fa ay doomi baayam delloo nag, yuusufa xàmmiku leen, te firawna xamante ak njabootam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"wale mababu walimwonea wivu yosefu, wakamuuza utumwani misri. lakini mungu alikuwa pamoja naye,

沃洛夫语

«naka maam yooyu, dañoo iñaane yuusufa, ba jaay ko, mu jëm réewu misra. waaye yàlla taxawu ko,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kwa imani yakobo alipokuwa karibu kufa, aliwabariki kila mmoja wa wana wa yosefu, akamwabudu mungu akiegemea ile fimbo yake.

沃洛夫语

ngëm moo tax ba, bi yanqóoba nekkee ci sukkurat, mu barkeel kenn ku nekk ci doomi yuusufa yi. moo tax it mu màggal yàlla, jafandu ci yetam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

heli alikuwa mwana wa mathati, mwana wa lawi, mwana wa melki, mwana wa yanai, mwana wa yosefu,

沃洛夫语

miy doomu matat.matat, lewi mooy baayam; lewi, melki;melki, yanayi; yanayi, yuusufa;

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akafika sukari, mji mmoja wa samaria, karibu na shamba ambalo yakobo alikuwa amempa mwanawe, yosefu.

沃洛夫语

noonu mu agsi ci wetu dëkku sikar ci tool, bi yanqóoba mayoon doomam yuusufa.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

siku zilipotimia za yosefu na maria kutakaswa kama walivyotakiwa na sheria ya mose, wazazi hao walimchukua mtoto, wakaenda naye yerusalemu ili wamweke mbele ya bwana.

沃洛夫语

noonu jamono ji ñu leen waroon a sellale agsi, ni ko yoonu musaa tërale. waajuri yeesu yi daldi koy yóbbu ca dëkku yerusalem, ngir sédde ko boroom bi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, wakataja majina ya watu wawili; wa kwanza yosefu aliyeitwa barsaba (au pia yusto), na wa pili mathia.

沃洛夫语

bi ko piyeer waxee, ñu tudd ñaar: yuusufa, mi ñu dippee barsabas te di ko dàkkentale yustus, moom ak macas.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hapo yosefu akanunua sanda ya kitani, akauteremsha chini huo mwili, akauzungushia sanda. akauweka katika kaburi lililokuwa limechongwa mwambani, kisha akavingirisha jiwe kubwa mbele ya mlango.

沃洛夫语

noonu yuusufa jënd càngaay, wàcce néew bi, laxas ko ci, dugal ko cib bàmmeel bu ñu yett ci xeer. bi mu ko defee mu béraŋ aw doj, ube ko buntu bàmmeel bi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

je, huyu si yule mwana wa seremala? je, mama yake si anaitwa maria, na ndugu zake si kina yakobo, yosefu, simoni na yuda?

沃洛夫语

ndax kii du doomu minise bi, te ndeyam tudd maryaama? ndax rakkam yu góor duñu saag, yuusufa, simoŋ ak yuda?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wakasema, "je, huyu si mwana wa yosefu? tunawajua baba yake na mama yake! basi, anawezaje kusema kwamba ameshuka kutoka mbinguni?"

沃洛夫语

Ñu naan: «ndax kii du yeesu, doomu yuusufa? xam nanu ndeyam ak baayam. kon nag lu tax léegi mu naan, mi ngi jóge asamaan?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, hivi ndivyo yesu kristo alivyozaliwa: maria, mama yake, alikuwa ameposwa na yosefu. lakini kabla hawajakaa pamoja kama mume na mke, alionekana kuwa mja mzito kwa uwezo wa roho mtakatifu.

沃洛夫语

nii la yeesu kirist juddoo. bi ñu mayee maryaama ndeyam yuusufa, waaye laata ñoo ànd, gis nañu ne dafa ëmb ci kàttanu xel mu sell mi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alipokuwa bado anawaza jambo hilo, malaika wa bwana alimtokea katika ndoto, akamwambia, "yosefu, mwana wa daudi, usiogope kumchukua maria awe mke wako, maana amekuwa mja mzito kwa uwezo wa roho mtakatifu.

沃洛夫语

waaye bi muy xalaat ci loolu, benn malaakam boroom bi daldi ko feeñu ci gént ne ko: «yaw yuusufa, sëtu daawuda, bul ragal a yeggali maryaama sa jabar, ndaxte doom ji mu ëmb, ci xel mu sell mi la jóge.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,754,746,360 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認