您搜索了: hakika (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

hakika atampa madaraka juu ya mali yake yote.

沃洛夫语

ci dëgg maa ngi leen koy wax, njaatige bi dina ko teg ci alalam jépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wakisema, "hakika bwana amefufuka, amemtokea simoni."

沃洛夫语

Ñooñu ne leen: «dëgg la, boroom bi dekki na, te feeñu na simoŋ!»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

nawaambieni hakika, kizazi hiki cha sasa hakitapita kabla ya hayo yote kutendeka.

沃洛夫语

«ci dëgg maa ngi leen koy wax, niti jamono jii duñu wéy, te loolu lépp amul.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mungu alisema: "hakika nitakubariki na nitakupa wazawa wengi."

沃洛夫语

ne ko: «sàllaaw dinaa la barkeel, yokk saw askan.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

hakika hutatoka huko nakwambia, mpaka utakapomaliza kulipa senti ya mwisho."

沃洛夫语

maa ngi la koy wax, doo génn foofa mukk te feyuloo fiftin bi ci mujj.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

akaendelea kusema, "hakika nawaambieni, nabii hatambuliwi katika kijiji chake.

沃洛夫语

mu tegaat ca ne: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, ab yonent kenn du ko teral ca réewam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, mlikwenda kuona nini? nabii? naam, hakika ni zaidi ya nabii.

沃洛夫语

lu tax ngeen génn nag? ngir gis ab yonent? waaw, wax naa leen ne, ëpp na yonent.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hakika nawaambieni, siku ile mji huo utapata adhabu kubwa zaidi kuliko ile ya watu wa sodoma.

沃洛夫语

maa ngi leen koy wax, bu bés baa, waa sodom ñooy tane dëkk boobu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kama mtu wa mataifa mengine ambaye hakutahiriwa akitimiza matakwa ya sheria, hakika atafikiriwa kana kwamba ametahiriwa.

沃洛夫语

te itam ku xaraful, tey def jëf yu jub yi yoonu musaa santaane, ndax yàlla du ko teg ni ku xaraf?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ama hakika, mpatanishi hahitajiwi ikiwa jambo lenyewe lamhusu mtu mmoja; na mungu ni mmoja.

沃洛夫语

waaye aajowul jottalikat, su fi kenn rekk teewee, te yàlla kenn la.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hivyo ndivyo tuwezavyo kuwa na hakika kwamba sisi ni watu wa ukweli; na hatutakuwa na wasiwasi mbele ya mungu.

沃洛夫语

ci loolu lanu xame ne, nu ngi ci dëgg; te waxtu wu sunu xol di xeex ak nun, dinanu ko dalal ci kanamam; ndaxte yàllaa ëpp sunu xol te xam na lépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ama hakika, hawawezi kufa tena, kwa sababu watakuwa kama malaika, na ni watoto wa mungu kwa vile wamefufuliwa katika wafu.

沃洛夫语

dafa fekk ne mënatuñoo dee, ndaxte dañuy mel ni malaaka yi. ay doomi yàlla lañu ndaxte doomi ndekkite lañu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, niambieni, mlikwenda kuona nini? mlikwenda kumwona nabii? naam, hakika ni zaidi ya nabii.

沃洛夫语

kon lu ngeen seeti woon? yonent? waaw, wax naa leen ne, ëpp na yonent.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kama saa moja baadaye, mtu mwingine akasisitiza, "hakika huyu alikuwa pamoja naye; ametoka galilaya ati."

沃洛夫语

bi ñu tegee lu mat waxtu, keneen dikkaat ca wax ja ne: «ci lu wóor nit kii àndoon na ak moom, nde galile la jóge.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

hakika, ingawa hataamka ampe kwa sababu yeye ni rafiki yake, lakini, kwa sababu ya huyo mtu kuendelea kumwomba, ataamka ampe chochote anachohitaji.

沃洛夫语

maa ngi leen koy wax, su jógul jox ko li muy laaj ndax li ñu xaritoo it, ndax la kee ñàkk jom dina tax mu jox ko lépp li mu soxla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"watu wote wa israeli wanapaswa kufahamu kwa hakika kwamba huyo yesu mliyemsulubisha ninyi, ndiye huyo ambaye mungu amemfanya kuwa bwana na kristo."

沃洛夫语

«na bànni israyil gépp xam bu wóor nag ne, yeesu moomu ngeen daajoon ci bant, yàlla def na ko boroom ak almasi bi.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

"mnapofunga, msiwe na huzuni kama wanafiki. wao hukunja nyuso zao wapate kuonekana na watu kuwa wanafunga. nawaambieni hakika, hao wamekwisha pata tuzo lao.

沃洛夫语

«su ngeen di woor, buleen mel ni naaféq yi, ñoom ñi yoggoorlu, di ñaawal seeni kanam, ngir seen koor feeñu nit ñi. ci dëgg maa ngi leen koy wax, jot nañu seen pey gépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

baadaye kidogo, watu waliokuwa pale wakamwendea petro, wakamwambia, "hakika, wewe pia ni mmoja wao, maana msemo wako unakutambulisha."

沃洛夫语

nes tuuti ña fa taxawoon ñëw ci piyeer ne ko: «ci lu wóor ne yaw itam bokk nga ci ñoom, ndaxte sa waxin feeñal na la.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, onyesheni kwa matendo kwamba mmetubu. msianze sasa kusema: sisi ni watoto wa abrahamu. nawaambieni hakika, mungu anaweza kuyageuza mawe haya yawe watoto wa abrahamu!

沃洛夫语

jëfeleen nag ni ñu tuub seeni bàkkaar, te bañ a nax seen bopp naan: “nun daal doomi ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, yàlla man na defal ibraayma ay doom ci doj yii.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"maana, kwa hakika, ndivyo herode, pontio pilato, watu wa israeli na watu wa mataifa walivyokutanika papa hapa mjini, kumpinga yesu mtumishi wako mtakatifu ambaye umemtia mafuta.

沃洛夫语

ndaxte ci dëgg ci dëkk bii, erodd ak poñsë pilaat ànd ak xeeti àddina ak bànni israyil, likkoo nañu, ngir daaneel sa ndaw lu sell li nga fal, di yeesu,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,794,457,603 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認