您搜索了: kaisarea (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

siku tatu baada ya kufika mkoani, festo alitoka kaisarea, akaenda yerusalemu.

沃洛夫语

bi festus teersee ci diiwaanam, mu teg ca ñetti fan, dem yerusalem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walipofika kaisarea walimpa mkuu wa mkoa ile barua na kumweka paulo chini ya mamlaka yake.

沃洛夫语

bi gawar ga àggee sesare, ñu jox boroom réew ma bataaxal ba, jébbal ko pool.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

filipo akajikuta yuko azoto, akapita katika miji yote akihubiri habari njema mpaka alipofika kaisarea.

沃洛夫语

filib moom teeri dëkku asot, muy jaar ci dëkk yépp, di fa xamle xebaar bu baax bi, ba kera muy ñëw dëkku sesare.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

meli ilitia nanga kaisarea, naye paulo akaenda yerusalemu kulisalimia lile kanisa, kisha akaenda antiokia.

沃洛夫语

teersi dëkku sesare, mu dem nuyu mbooloom ñi gëm, ba noppi dem ancos.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

siku ya pili yake, walifika kaisarea na huko kornelio alikuwa anawangojea pamoja na jamaa na marafiki aliokuwa amewaalika.

沃洛夫语

te bés ba ca topp mu dikk sesare. fekk korney woo na këram ay bokkam ak i xaritam yi ko gën a jege, di xaar piyeer.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

roho aliniambia niende pamoja nao bila kusita. hawa ndugu sita waliandamana nami pia kwenda kaisarea na huko tuliingia nyumbani mwa kornelio.

沃洛夫语

te xel mi ne ma: “Àndal ak ñoom, te bu ci werante.” juróom-benni bokk, yi fi teew, gunge woon nañu ma, ba nu dugg ca kër góor googu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu alipofika pande za kaisarea filipi, aliwauliza wanafunzi wake, "watu wanasema mwana wa mtu kuwa ni nani?"

沃洛夫语

bi ñu fa jógee, yeesu dem ca diiwaanu sesare bu filib. foofa mu laaj taalibeem ya: «lu nit ñiy wax ci doomu nit ki; mooy kan?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kesho yake tuliondoka tukaenda kaisarea. huko kaisarea tulikwenda nyumbani kwa mhubiri filipo. yeye alikuwa mmoja wa wale saba waliochaguliwa kule yerusalemu.

沃洛夫语

nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

festo alikaa nao kwa muda wa siku nane au kumi hivi, kisha akarudi kaisarea. kesho yake alikwenda barazani, akaamuru paulo aletwe ndani.

沃洛夫语

noonu festus am fa ñoom juróom-ñett ba fukki fan, ba noppi dem sesare. ca ëllëg sa mu toog ca àttekaay ba, joxe ndigal, ñu indi pool.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya siku tano, kuhani mkuu anania aliwasili kaisarea pamoja na wazee kadhaa na wakili mmoja wa sheria aitwaye tertulo. walimwendea yule mkuu wa mkoa wakamweleza mashtaka yao juu ya paulo.

沃洛夫语

bi juróomi fan wéyee, anañas saraxalekat bu mag ba dikk, ànd ak ay njiit ak layookat bu tudd tertul, ñu woo pool ci yoon fa kanam boroom réew ma.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kisha yesu na wanafunzi wake walikwenda katika vijiji vya kaisarea filipi. walipokuwa njiani, yesu aliwauliza wanafunzi wake, "watu wanasema mimi ni nani?"

沃洛夫语

bi loolu amee yeesu ànd ak ay taalibeem, dem ca dëkk, yi wër sesare bu filib. bi ñuy dem nag, mu laaj taalibe yi: «nit ñi, lu ñu wax ne man moom laa?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, mkuu wa jeshi aliwaita askari wawili akawaambia, "wekeni tayari askari mia mbili, wapanda farasi sabini na askari mia mbili wa mikuki, waende kaisarea; muwe tayari kuondoka kabla ya saa tatu leo usiku.

沃洛夫语

bi mu ko defee mu woo ñaar ci njiiti xare ba ne leen: «waajal-leen ñaari téeméeri xarekat ak juróom-ñaar-fukki gawar ak ñaari téeméer ñu gànnaayoo xeej, ngeen dem sesare ci juróom-ñeenti waxtu ci guddi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,793,362,631 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認