您搜索了: kizazi (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

huruma yake kwa watu wanaomcha hudumu kizazi hata kizazi.

沃洛夫语

day wàcce yërmandeem ci ñi ko ragal,ci seeni sët ba ci seeni sëtaat.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini kabla ya hayo, itambidi ateseke sana na kukataliwa na kizazi hiki.

沃洛夫语

waaye balaa booba fàww mu sonn lool te niti jamono jii dëddu ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

enyi kizazi cha nyoka wenye sumu! mnawezaje kuiepa hukumu ya moto wa jehanamu?

沃洛夫语

yéen ñi mel ni ay jaan, te fees ak daŋar niy co, naka ngeen di mucce mbugalu safara?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

jinsi yona alivyokuwa ishara kwa watu wa ninewi, ndivyo pia mwana wa mtu atakavyokuwa ishara kwa kizazi hiki.

沃洛夫语

ndaxte ni yunus nekke woon firnde ci waa dëkku niniw, noonu la doomu nit kiy nekke firnde ci niti jamono jii.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

matokeo yake ni kwamba kizazi hiki kitaadhibiwa kwa sababu ya damu ya manabii wote iliyomwagika tangu mwanzo wa ulimwengu;

沃洛夫语

kon nag yàlla dina mbugal niti jamono jii ndax dereti yonent yi ñu tuur, ba àddina sosoo ak léegi,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu akaendelea kusema, "basi, nitawafananisha watu wa kizazi hiki na kitu gani? ni watu wa namna gani?

沃洛夫语

yeesu tegaat ca ne: «kon lan laa man a mengaleel niti jamono jii? lan lañuy nirool?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

alifedheheshwa na kunyimwa haki. hakuna atakayeweza kuongea juu ya kizazi chake, kwa maana maisha yake yameondolewa duniani."

沃洛夫语

ci toroxteem nangu nañu dëggam;ñi mu tollool jamono, ku ci xalaat lii?jële nañu bakkanam ci àddina.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

enyi kizazi cha nyoka! mnawezaje kusema mambo mema hali ninyi ni waovu? maana mtu husema kutokana na yale yaliyojaa moyoni.

沃洛夫语

yéen ñi fees ak daŋar ni ay co, naka ngeen man a waxe lu baax, fekk dangeen bon? ndaxte gémmiñ, la fees xol lay wax.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"basi, nitakifananisha kizazi hiki na kitu gani? ni kama vijana waliokuwa wamekaa uwanjani, wakawa wakiambiana kikundi kimoja kwa kingine:

沃洛夫语

«niti jamono jii nag, lan laa leen man a mengaleel? Ñu ngi nirook xale yu toog ca pénc ma, di woo seeni xarit,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

mtu yeyote katika kizazi hiki kiovu na kisichomjali mungu anayenionea aibu mimi na mafundisho yangu, mwana wa mtu atamwonea aibu mtu huyo wakati atakapokuja katika utukufu wa baba yake pamoja na malaika watakatifu."

沃洛夫语

ku ma rus a faral, te nanguwul samay wax ci kanamu niti jamono jii, ñi fecci seen kóllëre ak yàlla te topp bàkkaar, doomu nit ki dina la rus a xam, bés bu ñëwee ci ndamu baayam, ànd ak malaaka yu sell yi.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

malkia wa kusini atatokea wakati kizazi hiki kitakapohukumiwa, naye atakihukumu kwamba kina hatia. maana yeye alisafiri kutoka mbali akaja kusikiliza maneno ya hekima ya solomoni, na kumbe hapa kuna kikuu kuliko solomoni.

沃洛夫语

te it ca bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-xamu suleymaan, te ku sut suleymaan a ngi fi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, yohane akawa anawaambia watu wengi waliofika ili awabatize: "enyi kizazi cha nyoka! ni nani aliyewadokezea kwamba mngeweza kuiepuka ghadhabu inayokuja?

沃洛夫语

mbooloo ma daan ñëw ngir mu sóob leen ci ndox, yaxya daan na leen wax naan: «yéen ñi fees ak daŋar mel ni ay co! ku leen artu ngeen daw merum yàlla mi nar a wàcc?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

malkia wa kusini atatokea wakati kizazi hiki kitakapohukumiwa, naye atashuhudia kwamba kina hatia. yeye alisafiri kutoka mbali, akaja kusikiliza maneno ya hekima ya solomoni; kumbe hapa pana mkuu zaidi kuliko solomoni.

沃洛夫语

keroog bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-xamu suleymaan, te ku sut suleymaan a ngi fi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu akajibu, "enyi kizazi kisicho na imani, kilichopotoka! nitakaa nanyi mpaka lini? nitawavumilia ninyi mpaka lini? mleteni hapa huyo mtoto."

沃洛夫语

noonu yeesu tontu ne: «yéen niti jamono jii, yéen ñi gëmadi te dëng, ba kañ laa war a nekk ak yéen, ba kañ laa leen di war a muñal?» mu ne leen, «indil-leen ma xale bi fii.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,747,839,850 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認