您搜索了: majaribu (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

ndugu zangu, muwe na furaha mnapopatwa na majaribu mbalimbali,

沃洛夫语

yéen samay bokk, waxtu wu nattu yi dalee ci seen kaw, ak nu ñu man a mel, defleen ko ni mbég mu réy,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"ninyi ndio mliobaki nami wakati wote wa majaribu yangu;

沃洛夫语

yéen nag yéenay ñi ànd ak man ci samay fitna.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

utusamehe dhambi zetu, maana sisi tunawasamehe wote waliotukosea; wala usitutie katika majaribu."

沃洛夫语

baal nu sunuy bàkkaar,ndaxte nun itam danuy baal ñépp ñi nu tooñ.te bu nu teg ci yoonu nattu.”»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kesheni na kusali ili msije mkaingia katika majaribu. roho i tayari lakini mwili ni dhaifu."

沃洛夫语

xool-leen te ñaan, ngir bañ a daanu cig fiir; seen xol jag na, waaye seen bind a woyof.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

heri mtu anayebaki mwaminifu katika majaribu, kwani akisha stahimili atapewa tuzo la uzima ambalo mungu aliwaahidia wale wanaompenda.

沃洛夫语

ku dékku nattu, ku barkeel nga, ndax boo ci génnee ak ndam, dees na la jagleel kaalag dund, gi yàlla dig ñi ko bëgg.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kwa hiyo, basi, bwana anajua jinsi ya kuwaokoa katika majaribu watu wanaomcha mungu, na jinsi ya kuwaweka waovu katika adhabu hadi siku ile ya hukumu,

沃洛夫语

gannaaw loolu lépp am na nag, nanu bir ne, boroom bi man na musal aji gëm ji nekk ci nattu, te denc ñi jubadi, ngir alag leen bésu àtte ba.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kisha akawaambia, "kesheni na kusali ili msije mkaingia katika majaribu. roho i radhi, lakini mwili ni dhaifu."

沃洛夫语

xool-leen te ñaan, ngir bañ a daanu cig fiir. seen xol jag na, waaye seen bind a woyof.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

majaribu mliyokwisha pata ni ya kawaida kwa binadamu. mungu ni mwaminifu, naye hataruhusu mjaribiwe kupita nguvu zenu, ila pamoja na majaribu, yeye atawapeni pia nguvu ya kustahimili na njia ya kutoka humo salama.

沃洛夫语

benn nattu dabu leen bu wuute ak yi dal nit ñépp. te sax yàlla kuy sàmm kóllëre la, te du nangu nattu bi wees seen kàttan, waaye cib nattu, dina leen ubbil bunt bu ngeen man a récce, ba ngeen man koo dékku.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

usitutie katika majaribu, lakini utuokoe na yule mwovu. is baadhi ya makala za zamani zina; kwa kuwa ufalme ni wako, na nguvu, na utukufu, hata milele. amina.

沃洛夫语

bu nu teg ci yoonu nattu, waaye nga musal nu ci lu bon.ndaxte yaw yaa yelloo nguur ak kàttan ak màggaay, ba fàww. amiin.”

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,787,563,132 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認