来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。
je, hamjasoma maandiko haya? jiwe walilokataa waashi sasa limekuwa jiwe kuu la msingi.
ndax musuleen a jàng wax jii ci mbind mi?“doj wi tabaxkat yi sànni,mujj na di doju koñ;
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
lakini yesu akawatazama, akawaambia, "maandiko haya matakatifu yana maana gani basi? jiwe walilokataa waashi, sasa limekuwa jiwe kuu la msingi!
waaye yeesu ne leen jàkk, daldi ne: «kon nag lu baat yii ci mbind mi di tekki:“doj wa tabaxkat ya sànni,mujj na di doju koñ.”
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
警告:包含不可见的HTML格式
kwenu ninyi mnaoamini, jiwe hilo ni la thamani kubwa; lakini kwa wale wasioamini, "jiwe walilokataa waashi, sasa limekuwa jiwe kuu la msingi."
kon nag yéen ñi gëm am ngeen cér ci teraangaam. waaye naka ñi gëmul:«doj wa tabaxkat ya sànni,mujj na di doju koñ.»
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
警告:包含不可见的HTML格式
hapo yesu akawaambia, "je, hamkusoma jambo hili katika maandiko matakatifu? jiwe walilokataa waashi sasa limekuwa jiwe kuu la msingi. bwana ndiye aliyefanya jambo hili, nalo ni la ajabu sana kwetu!
kon yeesu ne leen: «xanaa musuleen a jàng lii ci mbind yi?“doj wi tabaxkat yi sànni;mujj na di doju koñ;ci boroom bi la loolu jóge,te yéemu nanu ci.”
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
警告:包含不可见的HTML格式