Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
and he saith unto them, but whom say ye that i am? and peter answereth and saith unto him, thou art the christ.
noonu yeesu laaj leen: «yéen nag, ku ngeen wax ne moom laa?» piyeer tontu ko: «yaa di almasi bi.»
afterward jesus findeth him in the temple, and said unto him, behold, thou art made whole: sin no more, lest a worse thing come unto thee.
bi ñu ca tegee ab diir, yeesu dajeek moom ca kër yàlla ga ne ko: «déglul, fii mu ne, wér nga; bul defati bàkkaar, ngir ragal lu yées lii dal la.»