Sie suchten nach: greet you in love and peace (Englisch - Wolof)

Menschliche Beiträge

Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.

Übersetzung hinzufügen

Englisch

Wolof

Info

Englisch

mercy unto you, and peace, and love, be multiplied.

Wolof

na leen yàlla may yërmande, jàmm ak mbëggeel.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

grace to you, and peace, from god our father and the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

and to esteem them very highly in love for their work's sake. and be at peace among yourselves.

Wolof

rax-ca-dolli ngeen naw leen seen kem-kàttan te bëgg leen ndax seen liggéey. na jàmm am ci seen biir.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

grace be unto you, and peace, from god our father, and from the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

comfort your hearts, and stablish you in every good word and work.

Wolof

dëfël seeni xol te saxal leen ci bépp jëf ju rafet ak gépp kàddu gu baax.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

all the brethren greet you. greet ye one another with an holy kiss.

Wolof

bokk yépp ñu ngi leen di nuyu. saafoonteleen ak xol bu laab.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

what will ye? shall i come unto you with a rod, or in love, and in the spirit of meekness?

Wolof

lu leen gënal? ma ñëw ci yéen, yor ab yar, walla ma ànd ak mbëggeel, te lewet?

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

nevertheless let every one of you in particular so love his wife even as himself; and the wife see that she reverence her husband.

Wolof

waaye li teew, na góor gu nekk bëgg jabaram, ni mu bëgge boppam, te jigéen ji weg jëkkëram.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

and the lord make you to increase and abound in love one toward another, and toward all men, even as we do toward you:

Wolof

na leen boroom bi dolli mbëggeel gu tar, ngeen bëggante te bëgg ñépp, ni nu leen bëgge nun.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

i rejoice therefore that i have confidence in you in all things.

Wolof

bég naa, ndaxte xam naa ne, man naa leen a wóolu ci lu nekk!

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

i wrote unto you in an epistle not to company with fornicators:

Wolof

bindoon naa leen, ngeen bañ a séq dara ak njaalookat yi.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

finally, brethren, farewell. be perfect, be of good comfort, be of one mind, live in peace; and the god of love and peace shall be with you.

Wolof

kon nag bokk yi, bégleen, jublu cig mat, di déglu soññante bi ma leen di dénk, am benn xalaat te dëkk ci jàmm; noonu yàlla miy mbëggeel te di yàllay jàmm dina ànd ak yéen.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

and let us consider one another to provoke unto love and to good works:

Wolof

nanu seet ni nu man a xiirtalante cig mbëggeel ak ci jëf yu baax.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

but i determined this with myself, that i would not come again to you in heaviness.

Wolof

man nag fas yéene naa lii: duma dellusi ci yéen ci naqar.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

and walk in love, as christ also hath loved us, and hath given himself for us an offering and a sacrifice to god for a sweetsmelling savour.

Wolof

ngeen wéer seen dund ci mbëggeel, mel ni kirist mi nu bëgg, ba joxe bakkanam ngir nun, di sarax su ñu jébbal yàlla te neex ko ni xetu latkoloñ.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

and we have known and believed the love that god hath to us. god is love; and he that dwelleth in love dwelleth in god, and god in him.

Wolof

mbëggeel gi yàlla am ci nun, xam nanu ko te gëm ko. yàlla mbëggeel la, te képp ku sax ci mbëggeel, yaa ngi sax ci yàlla, mu dëkk ci yaw.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

for though i be absent in the flesh, yet am i with you in the spirit, joying and beholding your order, and the stedfastness of your faith in christ.

Wolof

jëmm ji ñëwul waaye sama xel a ngi ci yéen, di bég ci seen doxalin ak ngëm gu dëgër, gi ngeen am ci kirist.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

elect according to the foreknowledge of god the father, through sanctification of the spirit, unto obedience and sprinkling of the blood of jesus christ: grace unto you, and peace, be multiplied.

Wolof

ci li mu leen xam bu jiitu, te sédde leen boppam ci jëfu xel mu sell mi, ngir ngeen déggal ko, te seen xol laab ndax deretu yeesu kirist. na leen yàlla dollil yiw ak jàmm.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

but speaking the truth in love, may grow up into him in all things, which is the head, even christ:

Wolof

waaye dinanu wax dëgg, ëmb ko ci mbëggeel, bay màgg ci fànn gu ne ci sunu bokk ci kirist. mooy bopp,

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Englisch

according as he hath chosen us in him before the foundation of the world, that we should be holy and without blame before him in love:

Wolof

ndaxte ba àddina sosoogul, tànn na nu ci kirist, ngir nu man a teew fa kanamam, sell te ñàkk sikk. ci kaw mbëggeelam

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Eine bessere Übersetzung mit
7,787,496,306 menschlichen Beiträgen

Benutzer bitten jetzt um Hilfe:



Wir verwenden Cookies zur Verbesserung Ihrer Erfahrung. Wenn Sie den Besuch dieser Website fortsetzen, erklären Sie sich mit der Verwendung von Cookies einverstanden. Erfahren Sie mehr. OK