Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
kwa hiyo tuliamua kuwatembeleeni tena. nami, paulo, nilijaribu kuja kwenu zaidi ya mara moja, lakini shetani alituzuia.
kon jàppoon nanu leen a seetsi — man pool sax ay yooni yoon, waaye seytaane téq na ma.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
ndugu zangu, nataka mjue kwamba mara nyingi nilikusudia kuwatembeleeni, lakini mpaka sasa nimezuiwa. ningependa kupata mafanikio mema kati yenu kama nilivyopata kati ya watu wa mataifa mengine.
bokk yi, damaa bëgg ngeen xam ne, xalaat naa leen a seetsi ay yooni yoon, ngir meññ njariñ ci yéen, ni ma ko defe ci yeneen xeet yi, waaye ay téq-téq ñoo ma téye ba léegi.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
ninayo mengi ya kuwaambieni lakini sipendi kufanya hivyo kwa karatasi na wino; badala yake, natumaini kuwatembeleeni na kuzungumza nanyi ana kwa ana, ili furaha yetu ikamilike.
bëggoon naa leena wax lu bare ci bataaxel bii, waaye lépp xajul ci kayit. kon nag fas naa yéenee ñëw, ba jàkkaarlook yeen, nu waxtaan ci, ngir sunu mbég mat sëkk.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität: