Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
dina delloosi niti israyil yu bare ci yàlla seen boroom.
e ricondurrà molti figli d'israele al signore loro dio
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
waaye demleen ci bànni israyil, ñoom ñi réer niy xar.
rivolgetevi piuttosto alle pecore perdute della casa d'israele
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
yuusufa jóg nag, jël xale ba ak ndeyam, dellu israyil.
egli, alzatosi, prese con sé il bambino e sua madre, ed entrò nel paese d'israele
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
muy leer giy leeral xeet yi,di ndamu israyil say gaay.»
luce per illuminare le genti e gloria del tuo popolo israele»
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
waaye bànni israyil, mi bëggoon a sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
mentre israele, che ricercava una legge che gli desse la giustizia, non è giunto alla pratica della legge
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
dinaa la musal ci bànni israyil ak ci ñi dul yawut. ci ñoom laa lay yebal,
per questo ti libererò dal popolo e dai pagani, ai quali ti mand
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
am nanu sarax boo xam ne ñiy jaamu yàlla ci tàntu màggalukaayu bànni israyil sañuñu koo lekk.
noi abbiamo un altare del quale non hanno alcun diritto di mangiare quelli che sono al servizio del tabernacolo
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
yeesu tontu ko ne: «yaw yaay jàngal bànni israyil te xamuloo mbir yii?
gli rispose gesù: «tu sei maestro in israele e non sai queste cose
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
waaye neewuma waxu yàlla dafa toxu, ndaxte bokk ci bànni israyil, taxul nga bokk ci israyil tigi.
tuttavia la parola di dio non è venuta meno. infatti non tutti i discendenti di israele sono israele
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
«noonu ci askanam yàlla indil na bànni israyil musalkat bi yeesu, ci ni mu ko dige woon.
dalla discendenza di lui, secondo la promessa, dio trasse per israele un salvatore, gesù
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
bi ñu ko defee mu ne leen: «yéen bokki israyil, moytuleen li ngeen di def nit ñooñu.
disse: «uomini di israele, badate bene a ciò che state per fare contro questi uomini
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
dunu def ni musaa, mi daan muur xar-kanamam, ngir bànni israyil bañ a gis jeexug leer googu saxul.
e non facciamo come mosè che poneva un velo sul suo volto, perché i figli di israele non vedessero la fine di ciò che era solo effimero
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
ngëm moo tax mu sos màggalu bésu jéggi ba, di wis deret ci bunt yi, ngir malaakam yàqkat mi bañ a laal taawi bànni israyil.
per fede celebrò la pasqua e fece l'aspersione del sangue, perché lo sterminatore dei primogeniti non toccasse quelli degli israeliti
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
esayi wax na ci mbirum israyil ne:«lu bànni israyil baree-bare ni suufus géej sax,lu néew rekk a ciy mucc.
e quanto a israele, isaia esclama: fosse come la sabbia del mare, sarà salvato solo il resto
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
waaye ci mbirum israyil dafa wax ne:«tàllal naa samay loxo, suba ba ngoon, ci xeet wu may bañ tey werante.»
mentre di israele dice: tutto il giorno ho steso le mani verso un popolo disobbediente e ribelle
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
yoonu musaa digle na ne, ñi bokk ci giiru lewi te di ay saraxalekat, nañu jot asaka ci alalu bànni israyil, doonte sax ñuy seeni bokk te soqikoo ci ibraayma.
in verità anche quelli dei figli di levi, che assumono il sacerdozio, hanno il mandato di riscuotere, secondo la legge, la decima dal popolo, cioè dai loro fratelli, essi pure discendenti da abramo
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
yàlla bërgëlul xeetam, wi mu xamoon lu jiitu. ndax dangeen a xamul li mbind mi di wax ci mbirum iliyas? dafa doon tawat israyil ci yàlla naan:
dio non ha ripudiato il suo popolo, che egli ha scelto fin da principio. o non sapete forse ciò che dice la scrittura, nel passo in cui elia ricorre a dio contro israele
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
kon lu nu ci war a wax? li bànni israyil doon wut, gisuñu ko. waaye ñi yàlla tànn rekk a ko gis, te ña ca des bañ a gëm, ba seen xol dërkiis.
che dire dunque? israele non ha ottenuto quello che cercava; lo hanno ottenuto invece gli eletti; gli altri sono stati induriti
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
boo xamee ne fitnaal nañu leen ci dëkk bii, demleen ca ba ca kanam. ci dëgg maa ngi leen koy wax, dungeen man a wër dëkki israyil yépp, te doomu nit ki ñëwul.»
quando vi perseguiteranno in una città, fuggite in un'altra; in verità vi dico: non avrete finito di percorrere le città di israele, prima che venga il figlio dell'uomo
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
bokk yi, dama leen a bëgg a dindi kumpa ci lii, ngir ngeen bañ a yég seen bopp. dërkiisu xol dab na bànni israyil ab diir, ba bés ba mboolem waa àddina, ñu war a bokk ci nguuru yàlla, dugg ca.
non voglio infatti che ignoriate, fratelli, questo mistero, perché non siate presuntuosi: l'indurimento di una parte di israele è in atto fino a che saranno entrate tutte le genti
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität: