Results for regterhand translation from Afrikaans to Wolof

Afrikaans

Translate

regterhand

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

en hy sal die skape aan sy regterhand en die bokke aan sy linkerhand sit.

Wolof

mu teg xar yi ci ndeyjooram, bëy yi ci càmmooñam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

hy het gekom en die boek geneem uit die regterhand van hom wat op die troon sit;

Wolof

mbote ma ñëw, jël téere, ba nekkoon ca loxol ndeyjooru ka toog ca gàngune ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

hom het god as leidsman en verlosser deur sy regterhand verhoog om aan israel bekering en vergifnis van sondes te skenk.

Wolof

te yàlla yékkati na ko ci ndeyjooram, mu nekk buur ak musalkat, ngir may bànni israyil réccu, ba mu baal leen seeni bàkkaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

as julle dan saam met christus opgewek is, soek die dinge daarbo waar christus is en aan die regterhand van god sit.

Wolof

kon nag ndegam dekkeendoo ngeen ak kirist, wutleen yëf, ya nekk ca kaw, fa kirist toog ca ndeyjooru yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en hy het gesê: kyk, ek sien die hemele geopend en die seun van die mens aan die regterhand van god staan.

Wolof

mu ne: «seetleen, maa ngi gis asamaan yi ubbiku, te doomu nit kaa ngii taxaw ci ndeyjooru yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

maar hy was vol van die heilige gees en het die oë na die hemel gehou en die heerlikheid van god gesien en jesus wat staan aan die regterhand van god.

Wolof

waaye ecen, mi fees ak xel mu sell mi, ne jàkk ci asamaan, gis ndamu yàlla, te gis yeesu mi taxaw ci ndeyjooru yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

want dawid het nie in die hemele opgevaar nie, maar hy self sê: die here het gespreek tot my here: sit aan my regterhand

Wolof

ndaxte du daawudaa yéeg ci asamaan, waaye moom ci boppam nee na:“boroom bi wax na sama boroom:‘toogal ci sama ndeyjoor,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

die here het tot my here gespreek: sit aan my regterhand totdat ek u vyande gemaak het 'n voetbank van u voete?

Wolof

“boroom bi wax na sama boroom:‘toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneelsay noon ci sa kanam’ ”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en ek het in die regterhand van hom wat op die troon sit, 'n boek gesien, van binne en van buite beskrywe en met sewe seëls goed verseël.

Wolof

noonu ma gis ca loxol ndeyjooru ka toog ca gàngune ma téere bu ñu bind biir ak biti, tay ko juróom-ñaari yoon ak sondeel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en aan watter een van die engele het hy ooit gesê: sit aan my regterhand totdat ek u vyande gemaak het 'n voetbank van u voete?

Wolof

waaye yàlla musul a teral kenn ci malaaka yi, ba di ko wax:«toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneel say noonci sa kanam.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

die hoofsaak nou van wat ons gesê het, is dít: ons het so 'n hoëpriester wat gaan sit het aan die regterhand van die troon van die majesteit in die hemele,

Wolof

lii mooy li ëpp solo ci li nuy wax: am nanu saraxalekat bu mag bu mel noonu, moom mi toog ci ndeyjooru aji màgg ja ca nguuram ca kaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

dan sal die koning vir die wat aan sy regterhand is, sê: kom, julle geseëndes van my vader, beërf die koninkryk wat vir julle berei is van die grondlegging van die wêreld af.

Wolof

«noonu buur bi dina wax ñi féete ndeyjoor: “agsileen, yéen ñi sama baay barkeel, jël-leen nguur, gi ñu leen waajal li dale ci njàlbéenug àddina.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

die verborgenheid van die sewe sterre wat jy in my regterhand gesien het, en die sewe goue kandelaars: die sewe sterre is die engele van die sewe gemeentes, en die sewe kandelaars wat jy gesien het, is die sewe gemeentes.

Wolof

juróom-ñaari biddiiw yi nga gis ci sama loxol ndeyjoor, ak juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi, ay mbóoti yàlla lañu te lii lañuy tekki: biddiiw yi ñoo di malaakay juróom-ñaari mboolooy ñi gëm; juróom-ñaari làmp yi ñoo di juróom-ñaari mbooloo yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en toe hulle merk die genade wat aan my gegee is, het jakobus en céfas en johannes, wat as pilare geag is, aan my en barnabas die regterhand van gemeenskap gegee, sodat ons na die heidene en hulle na die besnedenes kon gaan;

Wolof

te saag, sefas ak yowaana nag, ñi ñu teg kenuy mbooloo mi, bi ñu ràññee yen bi ma yàlla jagleel ci yiwam, ñu fekksi nu ci, ba jox nu loxo, man ak barnabas, nu liggéey ca ña dul yawut, ñoom ñu liggéey ca yawut ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en hulle vleg 'n kroon van dorings en sit dit op sy hoof, en 'n riet in sy regterhand; en hulle val op hul knieë voor hom en bespot hom en sê: wees gegroet, koning van die jode!

Wolof

Ñu ràbb kaalag dég, teg ko ci boppam, teg bantu xat ci loxol ndeyjooram, sukk ci kanamam, di ko ñaawal ne ko: «nuyu nanu la, yaw buuru yawut yi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,953,184,449 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK