Results for himmelen translation from Danish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Danish

Wolof

Info

Danish

men andre fristede ham og forlangte af ham et tegn fra himmelen..

Wolof

am ñeneen ñu fexe koo fiir, ba laaj ko kéemaan gu jóge ci asamaan tey firndeel yónnentam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

johannes's dåb, var den fra himmelen eller fra mennesker?"

Wolof

la yaxya daan def, di sóob nit ñi ci ndox, fu mu ko jële, ci yàlla walla ci nit ñi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

men de magtede det ikke, og deres sted fandtes ikke mere i himmelen.

Wolof

waaye ninkinànka jaa gën a néew doole; noonu ñu dàqe ko ak toppam asamaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

himmelen og jorden skulle forgå, men mine ord skulle ingenlunde forgå.

Wolof

asamaan ak suuf dinañu wéy, waaye samay wax du wéy mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 3
Quality:

Danish

og dette skete tre gange, og straks blev dugen igen optagen til himmelen.

Wolof

Ñu def ko nag, ba muy ñetti yoon, ba noppi ñu ne cas sér ba, jëme asamaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

det første menneske var af jord, jordisk; det andet menneske er fra himmelen.

Wolof

nit ku jëkk ka pëndu suuf la woon; ñaareelu nit ki di kirist, mi ngi jóge asamaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

dette er det brød, som kommer ned fra himmelen, at man skal æde af det og ikke dø.

Wolof

waaye ñam wiy wàcce ci asamaan, ku ko lekk, doo dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

for at i jesu navn hvert knæ skal bøje sig, deres i himmelen og på jorden og under jorden,

Wolof

ngir turu yeesoo tax ñépp sukk,ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og der kom pludseligt fra himmelen en lyd som af et fremfarende vældigt vejr og fyldte hele huset, hvor de sade.

Wolof

ca saa sa riir jollee asamaan, mel ni ngelaw lu gaaw te bare doole, daldi fees dell kër, ga ñu toog.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men en røst svarede anden gang fra himmelen: hvad gud har renset, holde du ikke for vanhelligt!

Wolof

waaye ñaareel bi yoon baat bi dellu ne ma: “lu yàlla sellal, bu ko araamal.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

han, som er faren til himmelen og er ved guds højre hånd, efter at engle og myndigheder og kræfter ere ham underlagte.

Wolof

mi yéeg asamaan, toog fa ndeyjooru yàlla, mu tiim malaaka yi, boroom sañ-sañ yi ak boroom doole yépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

derefter så jeg en anden engel stige ned fra himmelen; han havde stor magt, og jorden blev oplyst af hans herlighed.

Wolof

gannaaw loolu ma gis meneen malaaka mu wàcce ca asamaan, yor sañ-sañ bu réy, te leeraayam daj na àddina sépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

"velsignet være kongen, som kommer, i herrens navn! fred i himmelen, og Ære i det højeste!"

Wolof

Ñu ngi naan:«yaw buur biy ñëw ci turu boroom bi,ku barkeel nga!na jàmm am ca asamaan,te ndam li féete ca bérab yu gën a kawe!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

men selv om vi eller en engel fra himmelen forkynder eder evangeliet anderledes; end vi have forkyndt eder det, han være en forbandelse!

Wolof

waaye su fekkee kenn ci nun ñëw, walla malaaka sax mu jóge asamaan, di yégle beneen xebaar bu mengoowul ak bi nu leen yégal, kooku yal na alku!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

glæder eder på den dag og jubler; thi se, eders løn er stor i himmelen. thi på samme måde gjorde deres fædre ved profeterne.

Wolof

bu boobaa bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu la maami seeni bañ daan fitnaale yonent yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og en stærk hagl, centnertung, faldt ned fra himmelen på menneskene; og menneskene bespottede gud for haglens plage, thi dens plage var meget stor.

Wolof

tawu yuur, donj wu nekk tollu ci ñeent-fukki kilo, daldi daanoo asamaan ci kaw nit ñi, ñuy xarab yàlla ndax musibam yuur ga, ndaxte musiba ma dafa metti woon lool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og de tænkte ved sig selv og sagde: "sige vi: fra himmelen, da vil han sige, hvorfor troede i ham da ikke?

Wolof

bi ñu ko déggee, ñuy werante ci seen biir naan: «bu nu nee: “ci yàlla,” kon dina nu laaj: “lu tax gëmuleen ko kon?”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

dette er det brød, som er kommet ned fra himmelen; ikke som eders fædre åde og døde. den, som æder dette brød, skal leve evindelig."

Wolof

kon nag ñam, wi wàcce ci asamaan a ngi noonu; bokkul ak ñam, wa seeni maam lekkoon te faatu. ku lekk ñam wii may wax dinga dund ba fàww.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

da sagde jesus til dem: "sandelig, sandelig, siger jeg eder, ikke moses har givet eder brødet fra himmelen, men min fader giver eder det sande brød fra himmelen.

Wolof

yeesu waxaat ne: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, du musaa moo leen jox ñam woowu wàcce ca asamaan; sama baay ci boppam, moo leen di jox ñam wu wóor, wi wàcce ca asamaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,786,659,812 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK