From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
alexander the coppersmith did me much evil: the lord reward him according to his works:
alegsàndar tëgg bi def na ma ñaawteef yu ne, waaye boroom bi dina ko fey ay jëfam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
of whom is hymenaeus and alexander; whom i have delivered unto satan, that they may learn not to blaspheme.
naka imene ak alegsàndar; jébbal naa leen seytaane, ngir ñu réccu li ñu doon sosal yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they compel one simon a cyrenian, who passed by, coming out of the country, the father of alexander and rufus, to bear his cross.
amoon na nag nit ku dëkk siren, tudd simoŋ, di baayu alegsàndar ak rufus. fekk booba mu romb fa, jóge ca wet, ga féete ak tool ya, ñu ga ko ngir mu gàddu bant bi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and annas the high priest, and caiaphas, and john, and alexander, and as many as were of the kindred of the high priest, were gathered together at jerusalem.
ràññe nañu ci: anas, miy saraxalekat bu mag bi, kayif, yowaana, alegsàndar ak bokki saraxalekat bu mag bi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: