Results for and so shall it be translation from English to Wolof

English

Translate

and so shall it be

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and as it was in the days of noe, so shall it be also in the days of the son of man.

Wolof

«la xewoon ca bési nóoyin, dina xewaat ci bési doomu nit ki.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

even thus shall it be in the day when the son of man is revealed.

Wolof

noonu lay mel, bés bu doomu nit kiy feeñ.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

as therefore the tares are gathered and burned in the fire; so shall it be in the end of this world.

Wolof

ni ñu dajalee jëmb ba, lakk ko, noonu lay nekke, bu àddina tukkee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but as the days of noe were, so shall also the coming of the son of man be.

Wolof

ni bési nóoyin ya, noonu lay mel, bu doomu nit ki di ñëw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and if it be meet that i go also, they shall go with me.

Wolof

su aajoo ma demal sama bopp, kon dinañu ànd ak man.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and knew not until the flood came, and took them all away; so shall also the coming of the son of man be.

Wolof

xalaatuñu woon dara, ba kera ndoxum mbënn ma di dikk, yóbbu leen. noonu lay mel ci ñëwu doomu nit ki.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for as jonas was a sign unto the ninevites, so shall also the son of man be to this generation.

Wolof

ndaxte ni yunus nekke woon firnde ci waa dëkku niniw, noonu la doomu nit kiy nekke firnde ci niti jamono jii.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and our hope of you is stedfast, knowing, that as ye are partakers of the sufferings, so shall ye be also of the consolation.

Wolof

te sunu yaakaar ci seen mbir dëgër na, xam ne, ni ngeen bokke ak nun naqar, noonu ngeen di bokke ak nun noflaayu xol.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for as the lightning cometh out of the east, and shineth even unto the west; so shall also the coming of the son of man be.

Wolof

ndaxte ni melax di fàqe penku, te lerax ba sowu, noonu la ñëwu doomu nit ki di mel.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for as a snare shall it come on all them that dwell on the face of the whole earth.

Wolof

ndaxte dina dal ci ñépp ñi nekk ci kaw suuf.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so all israel shall be saved: as it is written, there shall come out of sion the deliverer, and shall turn away ungodliness from jacob:

Wolof

bu loolu amee nag, bànni israyil gépp dina mucc. moom la mbind mi tëral, bi mu naan:«ab xettalikat dina jóge ci siyon,dàq weddi ci askanu yanqóoba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and peter answered him and said, lord, if it be thou, bid me come unto thee on the water.

Wolof

ci kaw loolu piyeer jël kàddu gi ne ko: «sang bi, bu dee yaw, sant ma, ma dox ci kaw ndox mi, ñëw ci yaw.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and even things without life giving sound, whether pipe or harp, except they give a distinction in the sounds, how shall it be known what is piped or harped?

Wolof

noonu la mel itam ci yëf yi dundul tey riir, ni toxoro walla xalam. su li ci jibe leerul, naka la nit man a ràññee li mbiibi toxoro walla buumi xalam di wax?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so, after he had patiently endured, he obtained the promise.

Wolof

noonu ibraayma di xaar tey muñ, ba jot li ko yàlla digoon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so it is written, the first man adam was made a living soul; the last adam was made a quickening spirit.

Wolof

mbind mi nee na: «nit ku jëkk ka, aadama, doon na boroom ruu,» waaye aadama mu mujj mi doon na xel muy joxe dund.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so were the churches established in the faith, and increased in number daily.

Wolof

noonu mboolooy ñi gëm di gën a dëgër ci yoon wi, tey yokku bés bu nekk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and i say unto you, whosoever shall put away his wife, except it be for fornication, and shall marry another, committeth adultery: and whoso marrieth her which is put away doth commit adultery.

Wolof

te it maa ngi leen koy wax, koo xam ne kii fase nga sa jabar te du njaaloo tax, boo séyaatee ak keneen, njaaloo nga.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the rest, some on boards, and some on broken pieces of the ship. and so it came to pass, that they escaped all safe to land.

Wolof

mu sant ñi ci des ñu def noonu, langaamu ci ay dénk, mbaa ca tojiti gaal ga. noonu ñépp jot tefes ga ci jàmm ak salaam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

according to my earnest expectation and my hope, that in nothing i shall be ashamed, but that with all boldness, as always, so now also christ shall be magnified in my body, whether it be by life, or by death.

Wolof

ndaxte sama xënte ak sama yaakaar mooy ma bañ a rus ci lenn, waaye sama yaram feeñal ndamu kirist, ma ànd ci ak kóolute gu mat, su may dund mbaa may dee; moom laa daan def démb, te moom laay def tey.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said also to the people, when ye see a cloud rise out of the west, straightway ye say, there cometh a shower; and so it is.

Wolof

yeesu neeti mbooloo ma: «bu ngeen gisee mu xiin ci sowu, dangeen naan ca saa sa: “dina taw,” te mooy am.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,254,244,503 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK