Results for contrary translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

saying, this fellow persuadeth men to worship god contrary to the law.

Wolof

Ñu ne: «kii day xiir nit ñi ci màggal yàlla ci lu juuyoo ak yoon wi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when we had launched from thence, we sailed under cyprus, because the winds were contrary.

Wolof

bi nu fa jógee, nu dem ci biir géej, leru dunu sipar ci fegu ngelaw li, ndaxte ngelaw li da noo soflu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

i verily thought with myself, that i ought to do many things contrary to the name of jesus of nazareth.

Wolof

«man sax ci sama bopp defe woon naa ne, war naa def lu bare, ngir suufeel turu yeesum nasaret.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

whom jason hath received: and these all do contrary to the decrees of caesar, saying that there is another king, one jesus.

Wolof

te yason a leen dalal. Ñoom ñépp dañoo bañ ndigali buur sesaar ne, am na beneen buur bu ñuy wax yeesu.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

blotting out the handwriting of ordinances that was against us, which was contrary to us, and took it out of the way, nailing it to his cross;

Wolof

mbind mi nu doon tiiñal, te daa nu yey ndax ay sàrtam, yàlla far na ko, dindi ko, daajaale ko ca bant, ba kirist deeye.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

who both killed the lord jesus, and their own prophets, and have persecuted us; and they please not god, and are contrary to all men:

Wolof

Ñoom yawut yi rey nañu boroom bi yeesu, ni ñu reye woon yonent yi; teg nañu nu fitna yu metti; neexuñu yàlla, ànduñu ak kenn,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for the flesh lusteth against the spirit, and the spirit against the flesh: and these are contrary the one to the other: so that ye cannot do the things that ye would.

Wolof

ndaxte sunu nafsu am na ay bëgg-bëgg yu mengoowul ak yu xelum yàlla. te xelum yàlla itam am na ay bëgg-bëgg yu mengoowul ak yu sunu nafsu. Ñoom ñaar dañoo juuyoo ci bépp fànn, ba tax lépp lu ngeen bëggoon a def, dungeen ko man.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for whoremongers, for them that defile themselves with mankind, for menstealers, for liars, for perjured persons, and if there be any other thing that is contrary to sound doctrine;

Wolof

ngir ñiy doxaan, ñi góor-jigéenu ak ñiy def nit jaam, ñiy fen tey wann seen kàddu, ak lépp luy juuyoo ak njàngale mu wér

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he saw them toiling in rowing; for the wind was contrary unto them: and about the fourth watch of the night he cometh unto them, walking upon the sea, and would have passed by them.

Wolof

booba mu gis taalibe yi sonn lool ci joow gaal gi ndax li leen ngelaw li soflu. ca njël nag mu jëm ci ñoom, di dox ci kaw dex gi, ba xaw leen a raw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for if thou wert cut out of the olive tree which is wild by nature, and wert graffed contrary to nature into a good olive tree: how much more shall these, which be the natural branches, be graffed into their own olive tree?

Wolof

yaw mi dul yawut, yaa ngi bokkoon ci garabu oliw gu àll, waaye yàlla daf la cee jële, ci lu dul faral a am, jabtal la ci garabu kër gi. kon man nanoo gën a wóor ne, yawut ya judduwaale nekk ci garabu oliw gu kër gi, yàlla dina leen ci delloo.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,170,009,451 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK