From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
thou fool, that which thou sowest is not quickened, except it die:
yaa gàtt xel! li ngay ji, du jebbi dund gu bees, fi ak deewul ba noppi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then said jesus unto him, except ye see signs and wonders, ye will not believe.
yeesu ne ko: «yéen daal, dungeen gëm mukk, fi ak gisuleen ay firnde walla ay kéemaan.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
john answered and said, a man can receive nothing, except it be given him from heaven.
yaxya tontu leen: «kenn mënul a am dara lu ko yàlla joxul.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and if a man also strive for masteries, yet is he not crowned, except he strive lawfully.
te it ku tàggat yaramam ngir rawante, duñu ko jagleel kaalag ndam mukk, su toppul sàrt ya.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
paul said to the centurion and to the soldiers, except these abide in the ship, ye cannot be saved.
waaye pool ne njiit la ak xarekat ya: «bu ñii desul ci gaal gi, dungeen raw.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said, therefore said i unto you, that no man can come unto me, except it were given unto him of my father.
mu dolli ca it ne: «looloo tax ma ne, kenn mënul a ñëw ci man te baay bi mayu la, nga agsi.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and as esaias said before, except the lord of sabaoth had left us a seed, we had been as sodoma, and been made like unto gomorrha.
esayi it waxoon na lu jiitu loolu ne:«yàlla boroom kàttan gi,su bàyyiwul woon ci nun lu néew,kon ba tey raat nanu ni dëkki sodom ak gomor.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said, how can i, except some man should guide me? and he desired philip that he would come up and sit with him.
mu tontu ko ne: «nu ma ko man a xame, su ma ko kenn firilul?» mu woo filib nag, mu yéeg, toog ak moom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and certain men which came down from judaea taught the brethren, and said, except ye be circumcised after the manner of moses, ye cannot be saved.
amoon na bés ay nit jóge diiwaanu yude, ñuy jàngal bokk yi ne leen: «ku xaraful, ni ko aaday musaa santaanee, doo man a mucc.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and except those days should be shortened, there should no flesh be saved: but for the elect's sake those days shall be shortened.
te bu ñu wàññiwul bés yooyu, kenn du mucc, waaye dees na leen wàññi ndax ñi yàlla tànn.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and even things without life giving sound, whether pipe or harp, except they give a distinction in the sounds, how shall it be known what is piped or harped?
noonu la mel itam ci yëf yi dundul tey riir, ni toxoro walla xalam. su li ci jibe leerul, naka la nit man a ràññee li mbiibi toxoro walla buumi xalam di wax?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
abide in me, and i in you. as the branch cannot bear fruit of itself, except it abide in the vine; no more can ye, except ye abide in me.
saxleen ci man; ma sax, man itam, ci yéen. ni car mënul a ame ay doom, bu saxul ci garab, noonu itam dungeen man a meññ li may jëfe ci yéen, bu ngeen saxul ci man.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and except that the lord had shortened those days, no flesh should be saved: but for the elect's sake, whom he hath chosen, he hath shortened the days.
te bu fekkul woon boroom bi wàññi bés yooyu, kenn du mucc, waaye fekk na mu wàññi leen ndax gaayam ñi mu tànn.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i say unto you, whosoever shall put away his wife, except it be for fornication, and shall marry another, committeth adultery: and whoso marrieth her which is put away doth commit adultery.
te it maa ngi leen koy wax, koo xam ne kii fase nga sa jabar te du njaaloo tax, boo séyaatee ak keneen, njaaloo nga.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when they come from the market, except they wash, they eat not. and many other things there be, which they have received to hold, as the washing of cups, and pots, brasen vessels, and of tables.
te it bu ñu jógee pénc ma, su ñu sanguwul set, duñu lekk. am nañu it yeneen aada yu bare, maanaam ni nga war a raxase ay kaas, ay njaq ak ay satala, ba ñu laab.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: