From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
i wrote unto you in an epistle not to company with fornicators:
bindoon naa leen, ngeen bañ a séq dara ak njaalookat yi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yet not altogether with the fornicators of this world, or with the covetous, or extortioners, or with idolaters; for then must ye needs go out of the world.
bëgguma ci woon a limaale waa àddina, maanaam njaalookat yi, nay yi, njublaŋ yi ak xërëmkat yi. su ngeen séqul ak ñooñu dara, kon fàww ngeen génn àddina.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but now i have written unto you not to keep company, if any man that is called a brother be a fornicator, or covetous, or an idolater, or a railer, or a drunkard, or an extortioner; with such an one no not to eat.
lii laa leen bëggoon a wax: buleen séq dara ak ku ñu tudde mbokk mu gëm kirist, te fekk day njaaloo walla mu nay walla muy xërëm walla muy xas nit walla muy màndi walla muy njublaŋ. nit ku mel noonu moom, buleen bokk ak moom, sax far di lekk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: