Results for gift translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

thanks be unto god for his unspeakable gift.

Wolof

jërë-jëfati yaw yàlla ndax sa may googu weesu dayo!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but unto every one of us is given grace according to the measure of the gift of christ.

Wolof

waaye ku nekk ci nun ak mayam, ni nu ko kirist séddalee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

not because i desire a gift: but i desire fruit that may abound to your account.

Wolof

loolu tekkiwul ne, damay sàkku ay ndimbal ci yéen, waaye damaa bëgg rekk seen denc yokku fa yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

so that ye come behind in no gift; waiting for the coming of our lord jesus christ:

Wolof

noonu nag ñàkkuleen genn may léegi bi ngeen di séentu waxtu, wi sunu boroom yeesu kirist di feeñ ci biir ndamam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for i long to see you, that i may impart unto you some spiritual gift, to the end ye may be established;

Wolof

ndaxte bëgg naa leen a gis lool, ba indil leen barke bu jóge ci xel mu sell mi, ndax seen ngëm gën a dëgër.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

as every man hath received the gift, even so minister the same one to another, as good stewards of the manifold grace of god.

Wolof

te lu la yàlla jagleel kenn ku nekk ci yéen, nanga ko bokk ak ñépp ni jawriñ ju jub, ci séddale yiwu yàlla wu yaatu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they of the circumcision which believed were astonished, as many as came with peter, because that on the gentiles also was poured out the gift of the holy ghost.

Wolof

yawut yi gëm yépp nag, ñi ànd ak piyeer, daldi waaru ci li yàlla tuur xel mu sell, mi mu maye, ci ñi dul yawut itam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but ye say, whosoever shall say to his father or his mother, it is a gift, by whatsoever thou mightest be profited by me;

Wolof

waaye yéen dangeen ne, ku wax sa ndey walla sa baay: “li ngeen war a jariñoo ci man, jébbal naa ko yàlla,”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as some spake of the temple, how it was adorned with goodly stones and gifts, he said,

Wolof

noonu ay nit doon wax ci lu jëm ca kër yàlla ga, ak ni ñu ko rafetale ak ay doj yu jafe ak alal ju ñu jébbal yàlla. waaye yeesu ne leen:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,927,449,633 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK