From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
and greetings in the markets, and to be called of men, rabbi, rabbi.
dañoo bëgg ñépp nuyoo leen ñaari loxo ca pénc ma, di leen wooye “kilifa gi.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
woe unto you, pharisees! for ye love the uppermost seats in the synagogues, and greetings in the markets.
yéen farisen yi, dingeen torox! ndaxte ca jàngu ya, toogu ya féete kanam ngeen di taamu te bëgg ñépp di leen nuyoo ñaari loxo ca pénc ma.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
beware of the scribes, which desire to walk in long robes, and love greetings in the markets, and the highest seats in the synagogues, and the chief rooms at feasts;
«moytuleen xutbakat yi; dañoo bëgg di doxantu, sol ay mbubb yu réy, te ñépp di leen nuyoo ñaari loxo ci pénc mi. ci jàngu yi, toogu yu féete kanam lañuy wut, te toogu yu yiw lañuy taamu ci reeri xew yi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they wrote letters by them after this manner; the apostles and elders and brethren send greeting unto the brethren which are of the gentiles in antioch and syria and cilicia:
Ñu jox leen bataaxal bu ne: yéen sunu bokk yi dul yawut te dëkk ancos, siri ak silisi, nu ngi leen di nuyu, nun seeni bokk, di ndaw yi ak njiit yi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: