From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
i understand your language a little bit.
i understand your language a little bit.
Last Update: 2024-12-27
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will give him the morning star.
ni ma jële sañ-sañ ci sama baay. dinaa ko jox it biddiiwu njël.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i will tarry at ephesus until pentecost.
ba tey dinaa toog fii ci dëkku efes ba màggalu pàntakot,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus saith unto him, i will come and heal him.
yeesu ne ko: «dinaa ñëw faj ko.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i will not leave you comfortless: i will come to you.
duma leen bàyyi ngeen wéet. dinaa dellusi ci yéen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if ye shall ask any thing in my name, i will do it.
lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but after that i am risen, i will go before you into galilee.
waaye bu ma dekkee, dinaa leen jiituji galile.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but after i am risen again, i will go before you into galilee.
waaye bu ma dekkee, dinaa leen jiituji galile.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he saith unto them, follow me, and i will make you fishers of men.
yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, ma def leen nappkati nit.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
come unto me, all ye that labour and are heavy laden, and i will give you rest.
«Ñëwleen ci man, yéen ñépp ñi sonn te diis, dinaa leen may noflaay.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto me, depart: for i will send thee far hence unto the gentiles.
waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he answered and said unto them, i will also ask you one thing; and answer me:
yeesu tontu leen ne: «man itam dinaa leen laaj lenn: wax leen ma,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all that the father giveth me shall come to me; and him that cometh to me i will in no wise cast out.
képp ku ma baay bi jox dina ñëw ci man, te duma dàq mukk ki may fekksi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he sware unto her, whatsoever thou shalt ask of me, i will give it thee, unto the half of my kingdom.
mu boole ci ngiñ ne ko: «loo ma man a laaj, dinaa la ko jox, ba ci genn-wàllu réew mi sax.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and again, i will put my trust in him. and again, behold i and the children which god hath given me.
newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla jox.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will kill her children with death; and all the churches shall know that i am he which searcheth the reins and hearts: and i will give unto every one of you according to your works.
dinaa rey ay doomam, te mboolooy ñi gëm yépp dinañu xam ne, man maa di kiy nattu xol ak xalaat, te dinaa fey ku nekk ay jëfam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and another also said, lord, i will follow thee; but let me first go bid them farewell, which are at home at my house.
keneen ne ko: «sang bi, dinaa la topp, waaye may ma, ma jëkk a tàgguji sama waa kër.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all things are lawful unto me, but all things are not expedient: all things are lawful for me, but i will not be brought under the power of any.
am na ci yéen ñu naan: «sañ naa lépp.» waaw, waaye du lépp a jariñ nit. «sañ naa lépp,» waaye duma bàyyi dara, mu noot ma.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will say to my soul, soul, thou hast much goods laid up for many years; take thine ease, eat, drink, and be merry.
te dinaa kañ sama bopp ne: ’yaw mii, am nga alal ju bare ju man a dem ay ati at; noppalal sa yaram, di lekk, di naan, tey bég.’ ”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
what is it then? i will pray with the spirit, and i will pray with the understanding also: i will sing with the spirit, and i will sing with the understanding also.
kon nag lu muy indi? bu may ñaan, dinaa ànd ak sama xol, àndaale ak sama xel. bu may woy, dinaa ànd ak sama xol, àndaale ak sama xel.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: