From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
and immediately the spirit driveth him into the wilderness.
ci kaw loolu xelum yàlla daldi jéñ yeesu, mu dem ca màndiŋ ma.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
peter then denied again: and immediately the cock crew.
waaye piyeer dellu weddi ko. noonu ginaar daldi sab.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they immediately left the ship and their father, and followed him.
ca saa sa ñu daldi bàyyi gaal ga ak seen baay, topp ci moom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
he then having received the sop went immediately out: and it was night.
yudaa nag jël dogu mburu ma, daldi génn ca saa sa. booba guddi woon na.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and immediately his fame spread abroad throughout all the region round about galilee.
noonu turam daldi siiw ci diiwaani galile gépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and as soon as he had spoken, immediately the leprosy departed from him, and he was cleansed.
ca saa sa ngaanaam daldi deñ, mu wér.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then they willingly received him into the ship: and immediately the ship was at the land whither they went.
noonu ñu nangu koo dugal ca gaal ga, gaal ga daldi teer ca saa sa ca fa ñu bëggoon a wàcc.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and his mouth was opened immediately, and his tongue loosed, and he spake, and praised god.
ca saa sa yàlla dindi luu gi, sakariya daldi waxaat, di màggal yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when he was come out of the ship, immediately there met him out of the tombs a man with an unclean spirit,
bi yeesu génnee gaal gi, nit ku rab jàpp jóge ca sëg ya, daldi ñëw kar ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and then immediately the brethren sent away paul to go as it were to the sea: but silas and timotheus abode there still.
noonu bokk yi yebal pool ca saa sa, mu jëm géej, waaye silas ak timote des fa.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he took him by the right hand, and lifted him up: and immediately his feet and ancle bones received strength.
mu jàpp ci loxol ndeyjooram, yékkati ko. ci saa si ay tànkam ak ay kostanam dëgër.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he answered and said unto them, i tell you that, if these should hold their peace, the stones would immediately cry out.
noonu mu tontu ne: «maa ngi leen koy wax, bu ñu noppee ñoom, doj yiy xaacu.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and after he had seen the vision, immediately we endeavored to go into macedonia, assuredly gathering that the lord had called us for to preach the gospel unto them.
bi mu amee peeñu moomu, ca saa sa nu fexee jàll ba maseduwan, xam ne boroom bi moo nu woo, ngir nu xamle fa xebaar bu baax bi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he put forth his hand, and touched him, saying, i will: be thou clean. and immediately the leprosy departed from him.
yeesu tàllal loxoom, laal ko naan: «bëgg naa ko, wéral.» ca saa sa ngaanaam daldi deñ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and as they heard these things, he added and spake a parable, because he was nigh to jerusalem, and because they thought that the kingdom of god should immediately appear.
bi nit ñi doon déglu kàddu yooyu, yeesu teg ca léeb, ndaxte jege woon na yerusalem, te ñoom foogoon nañu ne, nguuru yàlla dafay daldi feeñ ca saa sa.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when the woman saw that she was not hid, she came trembling, and falling down before him, she declared unto him before all the people for what cause she had touched him and how she was healed immediately.
te jigéen ja xam ne, mënul woon a nëbb li mu def. mu daldi daanu ci tànki yeesu, di lox. noonu mu nettali ci kanamu ñépp li taxoon mu laal yeesu, ak ni mu wére ca saa sa.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and have no root in themselves, and so endure but for a time: afterward, when affliction or persecution ariseth for the word's sake, immediately they are offended.
waaye du yàgg, ndaxte wax ji saxul ci moom. bu jaaree ci nattu nag, mbaa ñu fitnaal ko ndax kàddu gi, mu dàggeeku ci saa si.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and immediately, while he yet spake, cometh judas, one of the twelve, and with him a great multitude with swords and staves, from the chief priests and the scribes and the elders.
bi yeesu di wax, yudaa mi bokkoon ci fukki taalibe ya ak ñaar, agsi, ànd ak mbooloo mu bare, mu jóge ca saraxalekat yu mag ya, ca xutbakat ya ak ca njiiti xeet wa, te gànnaayoo jaasi ak yet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and immediately he arose, took up the bed, and went forth before them all; insomuch that they were all amazed, and glorified god, saying, we never saw it on this fashion.
ca saa sa mu jël basaŋam te génn fa kanam ñépp. noonu ñépp waaru, di màggal yàlla naan: «lu mel ni lii, musunu koo gis.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and now, behold, the hand of the lord is upon thee, and thou shalt be blind, not seeing the sun for a season. and immediately there fell on him a mist and a darkness; and he went about seeking some to lead him by the hand.
léegi loxob boroom bi dina dal sa kaw, te dinga gumba, ba dootuloo gis jant bi ab diir.» ca saa sa nag ay bëtam muuru, mu daldi tàbbi cig lëndëm, muy làmbatu, di wut ku ko wommat.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: