From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
then said jesus unto them plainly, lazarus is dead.
ci kaw loolu yeesu wax ci lu leer ne: «lasaar dee na.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
now jesus loved martha, and her sister, and lazarus.
yeesu soppoon na màrt ak maryaama ak lasaar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but the chief priests consulted that they might put lazarus also to death;
saraxalekat yu mag ya dogu ci ne, dañuy reyaale lasaar,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when he thus had spoken, he cried with a loud voice, lazarus, come forth.
bi mu waxee loolu, yeesu woote ak baat bu dëgër ne: «lasaar, ñëwal ci biti!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and there was a certain beggar named lazarus, which was laid at his gate, full of sores,
fekk miskin mu ñuy wax lasaar daan tëdd ca buntu këram, fees dell ak ay góom,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
now a certain man was sick, named lazarus, of bethany, the town of mary and her sister martha.
amoon na benn waay bu woppoon, ñu koy wax lasaar. ma nga dëkkoon betani, moom ak maryaama ak màrt, mi mu bokkaloon ndey ak baay.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and in hell he lift up his eyes, being in torments, and seeth abraham afar off, and lazarus in his bosom.
bi ñu koy mbugal ca safara, mu téen, séen fu sore ibraayma ak lasaar ci wetam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then jesus six days before the passover came to bethany, where lazarus was which had been dead, whom he raised from the dead.
juróom benni fan laata màggalu bésub jéggi ba, yeesu dem na betani, dëkku lasaar, mi mu dekkal.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
there they made him a supper; and martha served: but lazarus was one of them that sat at the table with him.
foofa ñu defaral ko fa reer. màrt moo ko doon séddale, te lasaar bokkoon na ca gan ña.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
(it was that mary which anointed the lord with ointment, and wiped his feet with her hair, whose brother lazarus was sick.)
maryaama mooy jigéen jiy sottiji latkoloñ ci tànki boroom bi, fompe ko kawaram. moom la càmmiñam lasaar woppoon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
these things said he: and after that he saith unto them, our friend lazarus sleepeth; but i go, that i may awake him out of sleep.
yeesu wax loolu, teg ca ne: «sunu xarit lasaar nelaw na, waaye maa ngi dem yee ko.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but abraham said, son, remember that thou in thy lifetime receivedst thy good things, and likewise lazarus evil things: but now he is comforted, and thou art tormented.
ibraayma ne ko: “sama doom, fàttalikul ne, jot nga sa bànneex ci àddina, fekk lasaar dëkk ci tiis. looloo tax xolam sedd fii, yaw nag, ngay sonn.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he cried and said, father abraham, have mercy on me, and send lazarus, that he may dip the tip of his finger in water, and cool my tongue; for i am tormented in this flame.
noonu mu yuuxu ne: “maam ibraayma, yërëm ma! yebalal lasaar, mu sëpp catul baaraamam ci ndox, seralal ma sama làmmiñ, ndaxte maa ngi sonn lool ci safara sii!”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: