From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
(now that he ascended, what is it but that he also descended first into the lower parts of the earth?
su nu waxee ne «yéeg na,» li moo ci génn: daa jëkk a wàcc ba ca bérab ya gën a suufe.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
from that time many of his disciples went back, and walked no more with him.
ci loolu taalibeem yu bare dëpp, bañatee ànd ak moom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and let him that is in the field not turn back again for to take up his garment.
ku nekk ci tool bi, bul ñibbi ngir fab sa mbubb.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when they found him not, they turned back again to jerusalem, seeking him.
bi ñu ko gisul nag, ñu daldi dellu yerusalem, seeti ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
thou madest him a little lower than the angels; thou crownedst him with glory and honour, and didst set him over the works of thy hands:
wàcce nga ko, def komu gën a suufe tuuti malaaka yi.kaalaa nga ko teraanga ak ndam,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but we are not of them who draw back unto perdition; but of them that believe to the saving of the soul.
nun nag bokkunu ci ñiy dellu gannaaw bay réer, waaye nu ngi bokk ci ñi am ngëm tey mucc.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and one of them, when he saw that he was healed, turned back, and with a loud voice glorified god,
kenn ci ñoom gis ne wér na, daldi dëpp, di màggal yàlla ak baat bu xumb.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and how i kept back nothing that was profitable unto you, but have shewed you, and have taught you publickly, and from house to house,
xam ngeen ne, musuma leen a nëbb dara lu leen di jariñ, di leen jàngal ci kanamu ñépp ak ca kër ya.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus said unto him, no man, having put his hand to the plough, and looking back, is fit for the kingdom of god.
yeesu ne ko: «kuy ji, di geestu, yeyoowul a liggéey ci nguuru yàlla.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and kept back part of the price, his wife also being privy to it, and brought a certain part, and laid it at the apostles' feet.
mu dencal boppam benn cér ca njëg ga, ànd ca ak jabaram; ba noppi mu indi cér ba ca des, teg ko ci loxoy ndaw ya.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.