Results for preached translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and there they preached the gospel.

Wolof

foofa ñu di fa xamle xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he preached in the synagogues of galilee.

Wolof

noonu mu dem di waare ca jàngu ya ca réewu yawut ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they went out, and preached that men should repent.

Wolof

noonu taalibe ya dem, di waare naan: «tuubleen seeni bàkkaar.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and many other things in his exhortation preached he unto the people.

Wolof

noonu yaxya teg ca yeneen dénkaane yu bare, di yégal nit ña xebaar bu baax ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when they had preached the word in perga, they went down into attalia:

Wolof

Ñu yégle kàddu gi ci dëkku peers, door a dem dëkku atali.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he preached in their synagogues throughout all galilee, and cast out devils.

Wolof

noonu mu wër ci diiwaanu galile gépp, di waare ci seeni jàngu, tey dàq rab yi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and came and preached peace to you which were afar off, and to them that were nigh.

Wolof

bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

ye know how through infirmity of the flesh i preached the gospel unto you at the first.

Wolof

xam ngeen ne, sama wopp moo taxoon, ma yégal leen xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

being grieved that they taught the people, and preached through jesus the resurrection from the dead.

Wolof

Ñu mer lool ci li ñuy waar nit ñi, di yégle ndekkitel ñi dee, sukkandikoo ko ci ndekkitel yeesu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and that repentance and remission of sins should be preached in his name among all nations, beginning at jerusalem.

Wolof

te it ñuy yégle xeet yépp ci turam, dale ko ci yerusalem ne, war nañoo tuub seeni bàkkaar, yàlla baal leen.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when the jews were gone out of the synagogue, the gentiles besought that these words might be preached to them the next sabbath.

Wolof

bi ñuy génn nag ca jàngu ba, yawut ya ñaan leen, ñu baamtu wax ja ca bésu noflaay ba ca tegu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they went forth, and preached everywhere, the lord working with them, and confirming the word with signs following. amen.

Wolof

taalibe ya dem waareji, te loxob boroom bi ànd ak ñoom, di dëggal kàddu gi ak firnde, yi ci ànd.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and this gospel of the kingdom shall be preached in all the world for a witness unto all nations; and then shall the end come.

Wolof

noonu xebaar bu baax bii ci nguuru yàlla, dees na ko yégle ci àddina sépp, ngir mu nekk seede ci xeet yépp. bu loolu amee muju jamono ji jot.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they, when they had testified and preached the word of the lord, returned to jerusalem, and preached the gospel in many villages of the samaritans.

Wolof

noonu bi ñu seedeelee yàlla te wax ci kàddoom, ñu dellu yerusalem, di xamle xebaar bu baax bi ci dëkk yu bare yu waa samari.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and preached, saying, there cometh one mightier than i after me, the latchet of whose shoes i am not worthy to stoop down and unloose.

Wolof

mu waare ne: «am na kuy ñëw sama gannaaw koo xam ne kii moo ma ëpp kàttan; yeyoowuma sax sëgg, ngir tekki ay dàllam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for unto us was the gospel preached, as well as unto them: but the word preached did not profit them, not being mixed with faith in them that heard it.

Wolof

nun jot nanu xebaar bu baax bi ni ñoom, waaye kàddu, ga ñu déggoon, jariñu leen dara, ndaxte boolewuñu ci ngëm, ba ñu koy déglu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and it came to pass, that on one of those days, as he taught the people in the temple, and preached the gospel, the chief priests and the scribes came upon him with the elders,

Wolof

benn bés yeesu doon jàngal nit ña ca kër yàlla ga, di leen yégal xebaar bu baax bi. saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya ñëw ne ko:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and upon the first day of the week, when the disciples came together to break bread, paul preached unto them, ready to depart on the morrow; and continued his speech until midnight.

Wolof

ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, booloo nanu ngir damm mburu ma. te pool, mi bëggoon a dem ca ëllëg sa, di diisoo ak ñoom te waxtaanam law ba ci xaaju guddi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but barnabas took him, and brought him to the apostles, and declared unto them how he had seen the lord in the way, and that he had spoken to him, and how he had preached boldly at damascus in the name of jesus.

Wolof

ci kaw loolu barnabas jël ko, yóbbu ko ca ndaw ya, nettali leen, ni sool gise boroom bi ci kaw yoon wi, ak li mu ko wax, rax-ca-dolli fit wi mu doon waxe ci turu yeesu ci damas.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and without controversy great is the mystery of godliness: god was manifest in the flesh, justified in the spirit, seen of angels, preached unto the gentiles, believed on in the world, received up into glory.

Wolof

ci dëgg-dëgg ragal yàlla ëmb na mbóot yu xóot:ki wàcc, yor bindu nit,mu bir ne xelam jub na,te malaaka ya gis ko;xamlees na ko ci xeet yi,ñu gëm ko ci kaw suuf,te yàlla teeru ko ci ndamam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,764,044,093 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK